Al-Isra · 10/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَأَنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ أَعْتَدْنَا لَهُمْ عَذَابًا أَلِيمًا ۝١٠
Wa annal lazeena laa yu`minoona bil aakhirati a`tadnaa lahum `azaaban aleemaa
📖 Tekkim Wolof
[Te xamal it ne] ña gëmul àllaaxira, xaroo Nanu leen mbugal mu metti.

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Al-Isra

8عَسَىٰ رَبُّكُمْ أَن يَرْحَمَكُمْ ۚ وَإِنْ عُدتُّمْ عُدْنَا ۘ وَجَعَلْنَا جَهَنَّمَ لِلْكَافِرِينَ حَصِيرًا
Xéy-na seen Boroom yërëm leen. Waaye bu ngeen delloo [def lu bon], Nu dellu [mbugal leen]. Te def Nanu Safara mu di géttub yéefar yi.
9إِنَّ هَٰذَا الْقُرْآنَ يَهْدِي لِلَّتِي هِيَ أَقْوَمُ وَيُبَشِّرُ الْمُؤْمِنِينَ الَّذِينَ يَعْمَلُونَ الصَّالِحَاتِ أَنَّ لَهُمْ أَجْرًا كَبِيرًا
Alxuraan jii nag dafay gindee jëm ci la gën a jub, tey bégal way-gëm ñay jëf jëf yu sell, [xamal leen ne] ñeel na leen pey gu rëy,
10وَأَنَّ الَّذِينَ لَا يُؤْمِنُونَ بِالْآخِرَةِ أَعْتَدْنَا لَهُمْ عَذَابًا أَلِيمًا
[Te xamal it ne] ña gëmul àllaaxira, xaroo Nanu leen mbugal mu metti.
11وَيَدْعُ الْإِنسَانُ بِالشَّرِّ دُعَاءَهُ بِالْخَيْرِ ۖ وَكَانَ الْإِنسَانُ عَجُولًا
Te nit dana ñaan lu bon ak lu baax, ndax dafa nekk di ku yàkkamti.
12وَجَعَلْنَا اللَّيْلَ وَالنَّهَارَ آيَتَيْنِ ۖ فَمَحَوْنَا آيَةَ اللَّيْلِ وَجَعَلْنَا آيَةَ النَّهَارِ مُبْصِرَةً لِّتَبْتَغُوا فَضْلًا مِّن رَّبِّكُمْ وَلِتَعْلَمُوا عَدَدَ السِّنِينَ وَالْحِسَابَ ۚ وَكُلَّ شَيْءٍ فَصَّلْنَاهُ تَفْصِيلًا
Def Nanu guddi ak bëccëg ñu nekk ñaari kéemaan, te far Nanu lëndëmi guddi ak leeraayu bëccëg, ngir ngeen mën a gis, di sàkku xéewal gu jóge ci seen Boroom, ak ngir ngeen mën a xam limi at yi ak ngir ngeen mën a waññi. Te lu nekk faramfàcce Nanu ko ci anam yu leer.
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
10Aaya

Tekki — Al-Isra 10

Simoore Al-Isra Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Te xamal it ne] ña gëmul àllaaxira, xaroo Nanu leen…

Simoore Aaya 10/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers