Al-Isra · 41/111
Tekki Waxtaan — Al-Isra
وَلَقَدْ صَرَّفْنَا فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ لِيَذَّكَّرُوا وَمَا يَزِيدُهُمْ إِلَّا نُفُورًا ٤١
Transliteration
Wa laqad sarrafnaa fee haazal Quraani liyazzakkaroo wa maa yazeeduhum illaa nufooraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te leeral Nanu ci Alxuraan jii [lu ne] ngir ñu xalaat. Te dolliwuleen lu dul fen [wëliis dëgg].
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 39-43 — Al-Isra
39ذَٰلِكَ مِمَّا أَوْحَىٰ إِلَيْكَ رَبُّكَ مِنَ الْحِكْمَةِ ۗ وَلَا تَجْعَلْ مَعَ اللَّهِ إِلَٰهًا آخَرَ فَتُلْقَىٰ فِي جَهَنَّمَ مَلُومًا مَّدْحُورًا
Loolu nekk na ci la la sa Boroom soloo, muy waare. Bul sàkk jeneen Yàlla di ko booleek Yàlla, dees na la sànni ci Safara, di ku ñu yedd, di ku ñu dàq [boo ko defee].
40أَفَأَصْفَاكُمْ رَبُّكُم بِالْبَنِينَ وَاتَّخَذَ مِنَ الْمَلَائِكَةِ إِنَاثًا ۚ إِنَّكُمْ لَتَقُولُونَ قَوْلًا عَظِيمًا
Waaw ndax seen Borom dafa leen a tànnal ay doom yu góor, na noppi jël ci Malaaka yi ay doom yu jigéen ?Yéen nag ca dëgg-dëgg li ngeen di wax rëy na.
41وَلَقَدْ صَرَّفْنَا فِي هَٰذَا الْقُرْآنِ لِيَذَّكَّرُوا وَمَا يَزِيدُهُمْ إِلَّا نُفُورًا
Te leeral Nanu ci Alxuraan jii [lu ne] ngir ñu xalaat. Te dolliwuleen lu dul fen [wëliis dëgg].
42قُل لَّوْ كَانَ مَعَهُ آلِهَةٌ كَمَا يَقُولُونَ إِذًا لَّابْتَغَوْا إِلَىٰ ذِي الْعَرْشِ سَبِيلًا
Neel : “Bu amoon yeneeni Yàlla tu nekk ak Moom, ni ñu ko waxe, kon dinañu sàkk [yoon wu leen yóbb] ca Boroom gàngune ga”.(yab Yàlla)
43سُبْحَانَهُ وَتَعَالَىٰ عَمَّا يَقُولُونَ عُلُوًّا كَبِيرًا
Cëy sellam ga ! Kawe na, jomb na li ñuy wax, jombute gu màgg a màgg !
Al-IsraFihi Alxuraan
111Aaya
MeccanRevelation
41Aaya
Tekki — Al-Isra 41
Simoore Al-Isra Aaya 41 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te leeral Nanu ci Alxuraan jii [lu ne] ngir ñu…Simoore Aaya 41/111 — Al-Isra الإسراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Isra Dégg, Al-Isra Tekki, Al-Isra mp3, Al-Isra pdf. Aaya 39–43. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








