Al-Kahf · 38/110
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Kahf
لَّٰكِنَّا هُوَ اللَّهُ رَبِّي وَلَا أُشْرِكُ بِرَبِّي أَحَدًا ۝٣٨
Laakinaa Huwal laahu Rabbee wa laa ushriku bi Rabbeee ahadaa
📖 Tekkim Wolof
Waaye man, Moom Yàlla moo di sama Boroom ; te duma bokkaaleek sama Boroom kenn ?

🎧 Dégg


📜 Aaya 36-40 — Simoore Al-Kahf

36وَمَا أَظُنُّ السَّاعَةَ قَائِمَةً وَلَئِن رُّدِدتُّ إِلَىٰ رَبِّي لَأَجِدَنَّ خَيْرًا مِّنْهَا مُنقَلَبًا
te yaakaaruma [foogu ma] jeexug àddina dana egsi. Te sax su ma [deeyoon] ba dellu ca sama Boroom fàwwu, danaa fa fekk lu gën lii cig daluwaay.
37قَالَ لَهُ صَاحِبُهُ وَهُوَ يُحَاوِرُهُ أَكَفَرْتَ بِالَّذِي خَلَقَكَ مِن تُرَابٍ ثُمَّ مِن نُّطْفَةٍ ثُمَّ سَوَّاكَ رَجُلًا
Moroom ma wax ak moom, tontu ko ne ko : “Moo ndax dangaa weddi Ki la binde ci suuf, topp ci toqit [gu jóge ci góor], topp Mu melal la nga di góor gu mat sëkk ?
38لَّٰكِنَّا هُوَ اللَّهُ رَبِّي وَلَا أُشْرِكُ بِرَبِّي أَحَدًا
Waaye man, Moom Yàlla moo di sama Boroom ; te duma bokkaaleek sama Boroom kenn ?
39وَلَوْلَا إِذْ دَخَلْتَ جَنَّتَكَ قُلْتَ مَا شَاءَ اللَّهُ لَا قُوَّةَ إِلَّا بِاللَّهِ ۚ إِن تَرَنِ أَنَا أَقَلَّ مِنكَ مَالًا وَوَلَدًا
Lu teewoon ba ngay dugg ca tool ba nga wax ne : “Lu neex Yàlla [rekk ay am] ! Amul kenn ku am kàttan ku dul Yàlla”. Ndeem danga maa gis ma gën laa néew alal ak i doom,
40فَعَسَىٰ رَبِّي أَن يُؤْتِيَنِ خَيْرًا مِّن جَنَّتِكَ وَيُرْسِلَ عَلَيْهَا حُسْبَانًا مِّنَ السَّمَاءِ فَتُصْبِحَ صَعِيدًا زَلَقًا
xéy-na sama Boroom jox ma lu gën sa tool, te yabal ca sa tool jéyya ju jóge asamaan ba mu nekk dénd bu amutul dara,
Al-KahfFihi Alxuraan
110Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Al-Kahf 38

Simoore Al-Kahf Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waaye man, Moom Yàlla moo di sama Boroom ; te…

Simoore Aaya 38/110 — Simoore Al-Kahf الكهف (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Kahf Dégg, Simoore Al-Kahf Tekki, Simoore Al-Kahf mp3, Simoore Al-Kahf pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers