Maryam · 23/98
Tekki Waxtaan — Maryam
فَأَجَاءَهَا الْمَخَاضُ إِلَىٰ جِذْعِ النَّخْلَةِ قَالَتْ يَا لَيْتَنِي مِتُّ قَبْلَ هَٰذَا وَكُنتُ نَسْيًا مَّنسِيًّا ۝٢٣
Fa ajaaa `ahal makhaadu ilaa jiz`in nakhlati qaalat yaa laitanee mittu qabla haazaa wa kuntu nasyam mansiyyaa
📖 Tekkim Wolof
Mat ma dikkal ko mu wattatu ba ca benn dàttu tàndarma, mu daldi ne: “Aka neexoon ma dee lu jiitu ! Kon fàttees na ma ! ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 21-25 — Maryam

21قَالَ كَذَٰلِكِ قَالَ رَبُّكِ هُوَ عَلَيَّ هَيِّنٌ ۖ وَلِنَجْعَلَهُ آيَةً لِّلنَّاسِ وَرَحْمَةً مِّنَّا ۚ وَكَانَ أَمْرًا مَّقْضِيًّا
Mu ne ko : “Loolu la sa Boroom wax ! Te lu yomb la ci Man ! Lii dafay doon kéemaan ci nit ñi, ak yërmaande wu bawoo fa Yàlla. Dogal ba sotti na”.
22۞ فَحَمَلَتْهُ فَانتَبَذَتْ بِهِ مَكَانًا قَصِيًّا
Mu daldi ëmb, daldi dem ca bérab bu sori.
23فَأَجَاءَهَا الْمَخَاضُ إِلَىٰ جِذْعِ النَّخْلَةِ قَالَتْ يَا لَيْتَنِي مِتُّ قَبْلَ هَٰذَا وَكُنتُ نَسْيًا مَّنسِيًّا
Mat ma dikkal ko mu wattatu ba ca benn dàttu tàndarma, mu daldi ne: “Aka neexoon ma dee lu jiitu ! Kon fàttees na ma ! ”
24فَنَادَاهَا مِن تَحْتِهَا أَلَّا تَحْزَنِي قَدْ جَعَلَ رَبُّكِ تَحْتَكِ سَرِيًّا
Mu daldi koy woo ci ronam, ne ko : “Bul ragal, bul jàq. Yàlla defal na la ag dex ci sa ron [ci suuf] ndox.
25وَهُزِّي إِلَيْكِ بِجِذْعِ النَّخْلَةِ تُسَاقِطْ عَلَيْكِ رُطَبًا جَنِيًّا
Gësëmal tàndarma gi : meññent mu nooy dana rot ci say tànk.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
23Aaya

Tekki — Maryam 23

Simoore Maryam Aaya 23 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mat ma dikkal ko mu wattatu ba ca benn dàttu…

Simoore Aaya 23/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 21–25. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers