Maryam · 22/98
Tekki Waxtaan — Maryam
۞ فَحَمَلَتْهُ فَانتَبَذَتْ بِهِ مَكَانًا قَصِيًّا ٢٢
Transliteration
Fahamalat hu fantabazat bihee makaanan qasiyyaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Mu daldi ëmb, daldi dem ca bérab bu sori.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 20-24 — Maryam
20قَالَتْ أَنَّىٰ يَكُونُ لِي غُلَامٌ وَلَمْ يَمْسَسْنِي بَشَرٌ وَلَمْ أَكُ بَغِيًّا
Mu ne ko : “Man naka laay ame doom, te génn góor masumaa laal, te duma ku baaloy ? ”
21قَالَ كَذَٰلِكِ قَالَ رَبُّكِ هُوَ عَلَيَّ هَيِّنٌ ۖ وَلِنَجْعَلَهُ آيَةً لِّلنَّاسِ وَرَحْمَةً مِّنَّا ۚ وَكَانَ أَمْرًا مَّقْضِيًّا
Mu ne ko : “Loolu la sa Boroom wax ! Te lu yomb la ci Man ! Lii dafay doon kéemaan ci nit ñi, ak yërmaande wu bawoo fa Yàlla. Dogal ba sotti na”.
22۞ فَحَمَلَتْهُ فَانتَبَذَتْ بِهِ مَكَانًا قَصِيًّا
Mu daldi ëmb, daldi dem ca bérab bu sori.
23فَأَجَاءَهَا الْمَخَاضُ إِلَىٰ جِذْعِ النَّخْلَةِ قَالَتْ يَا لَيْتَنِي مِتُّ قَبْلَ هَٰذَا وَكُنتُ نَسْيًا مَّنسِيًّا
Mat ma dikkal ko mu wattatu ba ca benn dàttu tàndarma, mu daldi ne: “Aka neexoon ma dee lu jiitu ! Kon fàttees na ma ! ”
24فَنَادَاهَا مِن تَحْتِهَا أَلَّا تَحْزَنِي قَدْ جَعَلَ رَبُّكِ تَحْتَكِ سَرِيًّا
Mu daldi koy woo ci ronam, ne ko : “Bul ragal, bul jàq. Yàlla defal na la ag dex ci sa ron [ci suuf] ndox.
MaryamFihi Alxuraan
98Aaya
MeccanRevelation
22Aaya
Tekki — Maryam 22
Simoore Maryam Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Mu daldi ëmb, daldi dem ca bérab bu sori.Simoore Aaya 22/98 — Maryam مريم (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Maryam Dégg, Maryam Tekki, Maryam mp3, Maryam pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








