Al-Baqara · 158/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
۞ إِنَّ الصَّفَا وَالْمَرْوَةَ مِن شَعَائِرِ اللَّهِ ۖ فَمَنْ حَجَّ الْبَيْتَ أَوِ اعْتَمَرَ فَلَا جُنَاحَ عَلَيْهِ أَن يَطَّوَّفَ بِهِمَا ۚ وَمَن تَطَوَّعَ خَيْرًا فَإِنَّ اللَّهَ شَاكِرٌ عَلِيمٌ ۝١٥٨
Innas Safaa wal-Marwata min sha`aaa`iril laahi faman hajjal Baita awi`tamara falaa junaaha `alaihi ai yattawwafa bihimaa; wa man tatawwa`a khairan fa innal laaha Shaakirun`Aleem
📖 Tekkim Wolof
Safaa ak Marwa bokk nañu ci màndargay jaamukaayu Yàlla yi. Ku aj Màkka walla mu Umra , du aay ci moom mu jaabante seen diggante ñoom ñaar. Ku coobarewu te jëf lu baax, lu yiw, na xam ne Yàlla gërëmaakoon la, Aji-xam la.

🎧 Dégg


📜 Aaya 156-160 — Simoore Al-Baqara

156الَّذِينَ إِذَا أَصَابَتْهُم مُّصِيبَةٌ قَالُوا إِنَّا لِلَّهِ وَإِنَّا إِلَيْهِ رَاجِعُونَ
ña nga xam ne, saa su leen tiis dalee dañu naan : “Yàllaa nu moom te ca Moom Yàlla lanuy dellu”.
157أُولَٰئِكَ عَلَيْهِمْ صَلَوَاتٌ مِّن رَّبِّهِمْ وَرَحْمَةٌ ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُهْتَدُونَ
Gaa ñooña am nañu njéggal gu bawoo ca seen Boroom, ak yérmaande ; te ñoo di ña gindiku tigi.
158۞ إِنَّ الصَّفَا وَالْمَرْوَةَ مِن شَعَائِرِ اللَّهِ ۖ فَمَنْ حَجَّ الْبَيْتَ أَوِ اعْتَمَرَ فَلَا جُنَاحَ عَلَيْهِ أَن يَطَّوَّفَ بِهِمَا ۚ وَمَن تَطَوَّعَ خَيْرًا فَإِنَّ اللَّهَ شَاكِرٌ عَلِيمٌ
Safaa ak Marwa bokk nañu ci màndargay jaamukaayu Yàlla yi. Ku aj Màkka walla mu Umra , du aay ci moom mu jaabante seen diggante ñoom ñaar. Ku coobarewu te jëf lu baax, lu yiw, na xam ne Yàlla gërëmaakoon la, Aji-xam la.
159إِنَّ الَّذِينَ يَكْتُمُونَ مَا أَنزَلْنَا مِنَ الْبَيِّنَاتِ وَالْهُدَىٰ مِن بَعْدِ مَا بَيَّنَّاهُ لِلنَّاسِ فِي الْكِتَابِ ۙ أُولَٰئِكَ يَلْعَنُهُمُ اللَّهُ وَيَلْعَنُهُمُ اللَّاعِنُونَ
Ña nga xam ne dañuy nëbb la ñu wàcce ci ag leeral ak ug njub ginnaaw ba ñu ko biralalee nit ñi ca Téere ba, ñooña Yàlla dana leen rëbb, rëbbkat ya itam dana leen rëbb
160إِلَّا الَّذِينَ تَابُوا وَأَصْلَحُوا وَبَيَّنُوا فَأُولَٰئِكَ أَتُوبُ عَلَيْهِمْ ۚ وَأَنَا التَّوَّابُ الرَّحِيمُ
lu dul ña ca tuub, yéwénal te leeral : ñooña Danaa leen jéggal Man Yàlla. Te Man maay Jéggalaakoon bi, di Jaglewaakoon bi.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
158Aaya

Tekki — Al-Baqara 158

Simoore Al-Baqara Aaya 158 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Safaa ak Marwa bokk nañu ci màndargay jaamukaayu Yàlla yi.…

Simoore Aaya 158/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 156–160. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers