Al-Baqara · 22/286
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Baqara
الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ فِرَاشًا وَالسَّمَاءَ بِنَاءً وَأَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَخْرَجَ بِهِ مِنَ الثَّمَرَاتِ رِزْقًا لَّكُمْ ۖ فَلَا تَجْعَلُوا لِلَّهِ أَندَادًا وَأَنتُمْ تَعْلَمُونَ ۝٢٢
Allazee ja`ala lakumul arda firaashanw wassamaaa`a binaaa `anw wa anzala minassamaaa`i maaa`an fa akhraja bihee minas samaraati rizqal lakum falaa taj`aloo lillaahi andaadanw wa antum ta`lamoon
📖 Tekkim Wolof
Moom mi def suuf nekk laltaay ci yéen, asamaan si di seen téeg ; te mu wàcceel leen ndox mu jóge asamaan, génne ca ay meññeent yu mu leen wërsëgal, bu leen sàkkal Yàlla moroom te xam xéll [ne loolu jaaduwul].

🎧 Dégg


📜 Aaya 20-24 — Simoore Al-Baqara

20يَكَادُ الْبَرْقُ يَخْطَفُ أَبْصَارَهُمْ ۖ كُلَّمَا أَضَاءَ لَهُم مَّشَوْا فِيهِ وَإِذَا أَظْلَمَ عَلَيْهِمْ قَامُوا ۚ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَذَهَبَ بِسَمْعِهِمْ وَأَبْصَارِهِمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Melax ga xaw naa yuri seeni gët : saa su leen leeralee [yoon wa] ñu dox ca leer ga ;saa su lëndëmee ñu taxaw. Bu neexoon Yàlla mu tëxloo leen, gumbaloo leen, Yàlla am na kàttanu def lu ne.
21يَا أَيُّهَا النَّاسُ اعْبُدُوا رَبَّكُمُ الَّذِي خَلَقَكُمْ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِكُمْ لَعَلَّكُمْ تَتَّقُونَ
Yéen nit ñi ! Jaamuleen Boroom bi leen bind, yéen ak ñi leen jiitu, ndax ngeen ragal ko. [Fegu] ci mbugalam.
22الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ فِرَاشًا وَالسَّمَاءَ بِنَاءً وَأَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَخْرَجَ بِهِ مِنَ الثَّمَرَاتِ رِزْقًا لَّكُمْ ۖ فَلَا تَجْعَلُوا لِلَّهِ أَندَادًا وَأَنتُمْ تَعْلَمُونَ
Moom mi def suuf nekk laltaay ci yéen, asamaan si di seen téeg ; te mu wàcceel leen ndox mu jóge asamaan, génne ca ay meññeent yu mu leen wërsëgal, bu leen sàkkal Yàlla moroom te xam xéll [ne loolu jaaduwul].
23وَإِن كُنتُمْ فِي رَيْبٍ مِّمَّا نَزَّلْنَا عَلَىٰ عَبْدِنَا فَأْتُوا بِسُورَةٍ مِّن مِّثْلِهِ وَادْعُوا شُهَدَاءَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Bu ngeen amee sikki-sàkka ci lii Nu wàcce ci Sunu jaam bi, indileen saar wu mel ni moom [Alxuraan] te sax ñaanleen ndimbal ñi ngeen di jaamu ba jaamuwuleen Yàlla, ndegam dëgg la ci yéen.
24فَإِن لَّمْ تَفْعَلُوا وَلَن تَفْعَلُوا فَاتَّقُوا النَّارَ الَّتِي وَقُودُهَا النَّاسُ وَالْحِجَارَةُ ۖ أُعِدَّتْ لِلْكَافِرِينَ
Bu ngeen ko deful, te du ngeen ko mën a def mukk, na ngeen ragal safara soo xam ne matt ma koy xamb nit la ak i xeer, te way weddi ya la ñu koy xaaroo.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
22Aaya

Tekki — Al-Baqara 22

Simoore Al-Baqara Aaya 22 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moom mi def suuf nekk laltaay ci yéen, asamaan si…

Simoore Aaya 22/286 — Simoore Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Baqara Dégg, Simoore Al-Baqara Tekki, Simoore Al-Baqara mp3, Simoore Al-Baqara pdf. Aaya 20–24. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers