Al-Baqara · 21/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
يَا أَيُّهَا النَّاسُ اعْبُدُوا رَبَّكُمُ الَّذِي خَلَقَكُمْ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِكُمْ لَعَلَّكُمْ تَتَّقُونَ ۝٢١
Yaaa aiyuhan naasu`budoo Rabbakumul lazee khalaqakum wallazeena min qablikum la`allakum tattaqoon
📖 Tekkim Wolof
Yéen nit ñi ! Jaamuleen Boroom bi leen bind, yéen ak ñi leen jiitu, ndax ngeen ragal ko. [Fegu] ci mbugalam.

🎧 Dégg


📜 Aaya 19-23 — Al-Baqara

19أَوْ كَصَيِّبٍ مِّنَ السَّمَاءِ فِيهِ ظُلُمَاتٌ وَرَعْدٌ وَبَرْقٌ يَجْعَلُونَ أَصَابِعَهُمْ فِي آذَانِهِم مِّنَ الصَّوَاعِقِ حَذَرَ الْمَوْتِ ۚ وَاللَّهُ مُحِيطٌ بِالْكَافِرِينَ
Walla [seen niróolee ngi deme ni] waame wu tukkee asamaan ànd ak lëndëm ak i dënnu ak i melax, ñu saañ seeni nopp ak seeni waaroom ngir bañ a dégg kàddu ya ngir ragal dee ;Yàlla Aji-peeg la yéefar ya.
20يَكَادُ الْبَرْقُ يَخْطَفُ أَبْصَارَهُمْ ۖ كُلَّمَا أَضَاءَ لَهُم مَّشَوْا فِيهِ وَإِذَا أَظْلَمَ عَلَيْهِمْ قَامُوا ۚ وَلَوْ شَاءَ اللَّهُ لَذَهَبَ بِسَمْعِهِمْ وَأَبْصَارِهِمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ عَلَىٰ كُلِّ شَيْءٍ قَدِيرٌ
Melax ga xaw naa yuri seeni gët : saa su leen leeralee [yoon wa] ñu dox ca leer ga ;saa su lëndëmee ñu taxaw. Bu neexoon Yàlla mu tëxloo leen, gumbaloo leen, Yàlla am na kàttanu def lu ne.
21يَا أَيُّهَا النَّاسُ اعْبُدُوا رَبَّكُمُ الَّذِي خَلَقَكُمْ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِكُمْ لَعَلَّكُمْ تَتَّقُونَ
Yéen nit ñi ! Jaamuleen Boroom bi leen bind, yéen ak ñi leen jiitu, ndax ngeen ragal ko. [Fegu] ci mbugalam.
22الَّذِي جَعَلَ لَكُمُ الْأَرْضَ فِرَاشًا وَالسَّمَاءَ بِنَاءً وَأَنزَلَ مِنَ السَّمَاءِ مَاءً فَأَخْرَجَ بِهِ مِنَ الثَّمَرَاتِ رِزْقًا لَّكُمْ ۖ فَلَا تَجْعَلُوا لِلَّهِ أَندَادًا وَأَنتُمْ تَعْلَمُونَ
Moom mi def suuf nekk laltaay ci yéen, asamaan si di seen téeg ; te mu wàcceel leen ndox mu jóge asamaan, génne ca ay meññeent yu mu leen wërsëgal, bu leen sàkkal Yàlla moroom te xam xéll [ne loolu jaaduwul].
23وَإِن كُنتُمْ فِي رَيْبٍ مِّمَّا نَزَّلْنَا عَلَىٰ عَبْدِنَا فَأْتُوا بِسُورَةٍ مِّن مِّثْلِهِ وَادْعُوا شُهَدَاءَكُم مِّن دُونِ اللَّهِ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Bu ngeen amee sikki-sàkka ci lii Nu wàcce ci Sunu jaam bi, indileen saar wu mel ni moom [Alxuraan] te sax ñaanleen ndimbal ñi ngeen di jaamu ba jaamuwuleen Yàlla, ndegam dëgg la ci yéen.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
21Aaya

Tekki — Al-Baqara 21

Simoore Al-Baqara Aaya 21 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yéen nit ñi ! Jaamuleen Boroom bi leen bind, yéen…

Simoore Aaya 21/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 19–23. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers