Al-Baqara · 242/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ ٢٤٢
Transliteration
Kazaalika yubaiyinul laahu lakum aayaatihee la`allakum ta`qiloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Noonu la leen Yàlla di faramfàcceelee laayaam ya ngir ngeen xel-lu.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 240-244 — Al-Baqara
240وَالَّذِينَ يُتَوَفَّوْنَ مِنكُمْ وَيَذَرُونَ أَزْوَاجًا وَصِيَّةً لِّأَزْوَاجِهِم مَّتَاعًا إِلَى الْحَوْلِ غَيْرَ إِخْرَاجٍ ۚ فَإِنْ خَرَجْنَ فَلَا جُنَاحَ عَلَيْكُمْ فِي مَا فَعَلْنَ فِي أَنفُسِهِنَّ مِن مَّعْرُوفٍ ۗ وَاللَّهُ عَزِيزٌ حَكِيمٌ
Ña dee ci yéen te ñu bàyyi ginnaaw ay jabar, [war na] ñu dénkaaneel leen [ci seeni alal] ab yóbbal lu jëm at te bu ñu leen génne. Bu ñu génnee seen bopp nag, dungeen ca am bàkkaar ca lañu def ci seen bopp ci lu jaadu, Yàlla ku not la [tedd] te ku xereñ la.
241وَلِلْمُطَلَّقَاتِ مَتَاعٌ بِالْمَعْرُوفِ ۖ حَقًّا عَلَى الْمُتَّقِينَ
Jigéen ñañu fase war nañoo am ab yóbbal bu jaadu, di wareef ca ña ragal Yàlla.
242كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Noonu la leen Yàlla di faramfàcceelee laayaam ya ngir ngeen xel-lu.
243۞ أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ خَرَجُوا مِن دِيَارِهِمْ وَهُمْ أُلُوفٌ حَذَرَ الْمَوْتِ فَقَالَ لَهُمُ اللَّهُ مُوتُوا ثُمَّ أَحْيَاهُمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَذُو فَضْلٍ عَلَى النَّاسِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَشْكُرُونَ
Moo ndax gisoo ña génn seeni kër, - ñuy ay junni, - ngir ragal dee ? Yàlla ne leen : “deeleen”. Daldi leen dekkalaat. Yàlla mooy Boroom ngëneel, ci nit ñi ; waaye li ëpp ci nit ñi duñu gërëm [seen Boroom].
244وَقَاتِلُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ وَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Nangeen di xeex ci yoonu Yàlla. Te xam ne Yàlla kuy dégg la te ku xam la.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
242Aaya
Tekki — Al-Baqara 242
Simoore Al-Baqara Aaya 242 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Noonu la leen Yàlla di faramfàcceelee laayaam ya ngir ngeen…Simoore Aaya 242/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 240–244. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








