Al-Baqara · 243/286
Tekki Waxtaan — Al-Baqara
۞ أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ خَرَجُوا مِن دِيَارِهِمْ وَهُمْ أُلُوفٌ حَذَرَ الْمَوْتِ فَقَالَ لَهُمُ اللَّهُ مُوتُوا ثُمَّ أَحْيَاهُمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَذُو فَضْلٍ عَلَى النَّاسِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَشْكُرُونَ ۝٢٤٣
Alam tara ilal lazeena kharajoo min diyaarihim wa hum uloofun hazaral mawti faqaaala lahumul laahu mootoo summa ahyaahum; innal laaha lazoo fadlin `alannaasi wa laakinna aksarannaasi laa yashkuroon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax gisoo ña génn seeni kër, - ñuy ay junni, - ngir ragal dee ? Yàlla ne leen : “deeleen”. Daldi leen dekkalaat. Yàlla mooy Boroom ngëneel, ci nit ñi ; waaye li ëpp ci nit ñi duñu gërëm [seen Boroom].
🎧 Dégg

📜 Aaya 241-245 — Al-Baqara

241وَلِلْمُطَلَّقَاتِ مَتَاعٌ بِالْمَعْرُوفِ ۖ حَقًّا عَلَى الْمُتَّقِينَ
Jigéen ñañu fase war nañoo am ab yóbbal bu jaadu, di wareef ca ña ragal Yàlla.
242كَذَٰلِكَ يُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمْ آيَاتِهِ لَعَلَّكُمْ تَعْقِلُونَ
Noonu la leen Yàlla di faramfàcceelee laayaam ya ngir ngeen xel-lu.
243۞ أَلَمْ تَرَ إِلَى الَّذِينَ خَرَجُوا مِن دِيَارِهِمْ وَهُمْ أُلُوفٌ حَذَرَ الْمَوْتِ فَقَالَ لَهُمُ اللَّهُ مُوتُوا ثُمَّ أَحْيَاهُمْ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَذُو فَضْلٍ عَلَى النَّاسِ وَلَٰكِنَّ أَكْثَرَ النَّاسِ لَا يَشْكُرُونَ
Moo ndax gisoo ña génn seeni kër, - ñuy ay junni, - ngir ragal dee ? Yàlla ne leen : “deeleen”. Daldi leen dekkalaat. Yàlla mooy Boroom ngëneel, ci nit ñi ; waaye li ëpp ci nit ñi duñu gërëm [seen Boroom].
244وَقَاتِلُوا فِي سَبِيلِ اللَّهِ وَاعْلَمُوا أَنَّ اللَّهَ سَمِيعٌ عَلِيمٌ
Nangeen di xeex ci yoonu Yàlla. Te xam ne Yàlla kuy dégg la te ku xam la.
245مَّن ذَا الَّذِي يُقْرِضُ اللَّهَ قَرْضًا حَسَنًا فَيُضَاعِفَهُ لَهُ أَضْعَافًا كَثِيرَةً ۚ وَاللَّهُ يَقْبِضُ وَيَبْسُطُ وَإِلَيْهِ تُرْجَعُونَ
Képp koo xam ne lebal na Yàlla lebaliin [bor] bu rafet, dana ko ko fulal ay yoon yu bari. Yàlla mooy xatal di yaatal. Te ca Moom ngeen di dellu.
Al-BaqaraFihi Alxuraan
286Aaya
MedinanRevelation
243Aaya

Tekki — Al-Baqara 243

Simoore Al-Baqara Aaya 243 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax gisoo ña génn seeni kër, - ñuy ay…

Simoore Aaya 243/286 — Al-Baqara البقرة (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Baqara Dégg, Al-Baqara Tekki, Al-Baqara mp3, Al-Baqara pdf. Aaya 241–245. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers