Taha · 33/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
كَيْ نُسَبِّحَكَ كَثِيرًا ۝٣٣
Kai nusabbihaka kaseeraa
📖 Tekkim Wolof
ngir nu mën di la sàbbaal lu bari,

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore Taha

31اشْدُدْ بِهِ أَزْرِي
Doolel ma ci moom !
32وَأَشْرِكْهُ فِي أَمْرِي
te boole ko ci samay mbir,
33كَيْ نُسَبِّحَكَ كَثِيرًا
ngir nu mën di la sàbbaal lu bari,
34وَنَذْكُرَكَ كَثِيرًا
di La tuddu, di la fàttaliku lu bari.
35إِنَّكَ كُنتَ بِنَا بَصِيرًا
Te Yaa gën a xam sunuy mbir, Yaa nu gën a gis”
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Taha 33

Simoore Taha Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ngir nu mën di la sàbbaal lu bari,

Simoore Aaya 33/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers