Taha · 34/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَنَذْكُرَكَ كَثِيرًا ۝٣٤
Wa nazkuraka kaseeraa
📖 Tekkim Wolof
di La tuddu, di la fàttaliku lu bari.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 32-36 — Simoore Taha

32وَأَشْرِكْهُ فِي أَمْرِي
te boole ko ci samay mbir,
33كَيْ نُسَبِّحَكَ كَثِيرًا
ngir nu mën di la sàbbaal lu bari,
34وَنَذْكُرَكَ كَثِيرًا
di La tuddu, di la fàttaliku lu bari.
35إِنَّكَ كُنتَ بِنَا بَصِيرًا
Te Yaa gën a xam sunuy mbir, Yaa nu gën a gis”
36قَالَ قَدْ أُوتِيتَ سُؤْلَكَ يَا مُوسَىٰ
[Yàlla] tontu ne : “Li nga doon laaj [di ko ñaan] am nga ko.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Taha 34

Simoore Taha Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : di La tuddu, di la fàttaliku lu bari.

Simoore Aaya 34/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers