Taha · 36/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
قَالَ قَدْ أُوتِيتَ سُؤْلَكَ يَا مُوسَىٰ ۝٣٦
Qaala qad ooteeta su`laka yaa Moosaa
📖 Tekkim Wolof
[Yàlla] tontu ne : “Li nga doon laaj [di ko ñaan] am nga ko.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 34-38 — Simoore Taha

34وَنَذْكُرَكَ كَثِيرًا
di La tuddu, di la fàttaliku lu bari.
35إِنَّكَ كُنتَ بِنَا بَصِيرًا
Te Yaa gën a xam sunuy mbir, Yaa nu gën a gis”
36قَالَ قَدْ أُوتِيتَ سُؤْلَكَ يَا مُوسَىٰ
[Yàlla] tontu ne : “Li nga doon laaj [di ko ñaan] am nga ko.
37وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَيْكَ مَرَّةً أُخْرَىٰ
Te it, wér na ne xéewaloon Nanu la feneen,
38إِذْ أَوْحَيْنَا إِلَىٰ أُمِّكَ مَا يُوحَىٰ
Ba Nu déggalee sa yaay la Nu ko déggal :
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
36Aaya

Tekki — Taha 36

Simoore Taha Aaya 36 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : [Yàlla] tontu ne : “Li nga doon laaj [di ko…

Simoore Aaya 36/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 34–38. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Thursday, October 1, 2026

Don't forget us in your sincere prayers