Taha · 37/135
Tekki Waxtaan — Simoore Taha
وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَيْكَ مَرَّةً أُخْرَىٰ ۝٣٧
Wa laqad manannaa `alaika marratan ukhraaa
📖 Tekkim Wolof
Te it, wér na ne xéewaloon Nanu la feneen,

🎧 Dégg


📜 Aaya 35-39 — Simoore Taha

35إِنَّكَ كُنتَ بِنَا بَصِيرًا
Te Yaa gën a xam sunuy mbir, Yaa nu gën a gis”
36قَالَ قَدْ أُوتِيتَ سُؤْلَكَ يَا مُوسَىٰ
[Yàlla] tontu ne : “Li nga doon laaj [di ko ñaan] am nga ko.
37وَلَقَدْ مَنَنَّا عَلَيْكَ مَرَّةً أُخْرَىٰ
Te it, wér na ne xéewaloon Nanu la feneen,
38إِذْ أَوْحَيْنَا إِلَىٰ أُمِّكَ مَا يُوحَىٰ
Ba Nu déggalee sa yaay la Nu ko déggal :
39أَنِ اقْذِفِيهِ فِي التَّابُوتِ فَاقْذِفِيهِ فِي الْيَمِّ فَلْيُلْقِهِ الْيَمُّ بِالسَّاحِلِ يَأْخُذْهُ عَدُوٌّ لِّي وَعَدُوٌّ لَّهُ ۚ وَأَلْقَيْتُ عَلَيْكَ مَحَبَّةً مِّنِّي وَلِتُصْنَعَ عَلَىٰ عَيْنِي
Ne ko na sànni liir ba ca kees ga, sànni kees ga ca ndox ma, ndox ma dana ko gëq ca tefes ga ; samab noon, dib noonam moo koy jël”. Yaw Muusaa, defal naa la Samag cofeel, te it ci Samag càmm nga màgge.
TahaFihi Alxuraan
135Aaya
MeccanRevelation
37Aaya

Tekki — Taha 37

Simoore Taha Aaya 37 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it, wér na ne xéewaloon Nanu la feneen,

Simoore Aaya 37/135 — Simoore Taha طه (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Taha Dégg, Simoore Taha Tekki, Simoore Taha mp3, Simoore Taha pdf. Aaya 35–39. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers