Al-Anbiya · 49/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ وَهُم مِّنَ السَّاعَةِ مُشْفِقُونَ ۝٤٩
Allazeena yakhshawna Rabbahum bilghaibi wa hum minas Saa`ati mushfiqoon
📖 Tekkim Wolof
ñooy ña ragal seen Boroom ci kumpa, te ñoom way-jàq lañu ca Bis-pénc ba.

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Simoore Al-Anbiya

47وَنَضَعُ الْمَوَازِينَ الْقِسْطَ لِيَوْمِ الْقِيَامَةِ فَلَا تُظْلَمُ نَفْسٌ شَيْئًا ۖ وَإِن كَانَ مِثْقَالَ حَبَّةٍ مِّنْ خَرْدَلٍ أَتَيْنَا بِهَا ۗ وَكَفَىٰ بِنَا حَاسِبِينَ
Dana tëral màndaxe mu maandu ca Bis-pénc ba. Te deesul tooñ benn bakkan ci dara, doonte lu tollu ni pepp bàkket, Dananu ko indi. Te aka mën a wàññi.
48وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَىٰ وَهَارُونَ الْفُرْقَانَ وَضِيَاءً وَذِكْرًا لِّلْمُتَّقِينَ
Joxoon Nanu Muusaa ak Aaruuna Tawreet ak leeraay ak fàtttaliku ngir ña ragal Yàlla,
49الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ وَهُم مِّنَ السَّاعَةِ مُشْفِقُونَ
ñooy ña ragal seen Boroom ci kumpa, te ñoom way-jàq lañu ca Bis-pénc ba.
50وَهَٰذَا ذِكْرٌ مُّبَارَكٌ أَنزَلْنَاهُ ۚ أَفَأَنتُمْ لَهُ مُنكِرُونَ
Te lii [Alxuraan jii], tur la wu barkeel [sakkan] wu Nu wàcce. Ndax yéen dangeen koy weddi ?
51۞ وَلَقَدْ آتَيْنَا إِبْرَاهِيمَ رُشْدَهُ مِن قَبْلُ وَكُنَّا بِهِ عَالِمِينَ
Te mayoon Nanu Ibraahiima njub lu jiitu. Te nekkoon Nanu ñu ko xam xéll.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
49Aaya

Tekki — Al-Anbiya 49

Simoore Al-Anbiya Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ñooy ña ragal seen Boroom ci kumpa, te ñoom way-jàq…

Simoore Aaya 49/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers