Al-Anbiya · 48/112
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Anbiya
وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَىٰ وَهَارُونَ الْفُرْقَانَ وَضِيَاءً وَذِكْرًا لِّلْمُتَّقِينَ ۝٤٨
Wa laqad aatainaa Moosa wa haaroonal Furqaana wa diyaa`anw wa zikral lilmuttaqeen
📖 Tekkim Wolof
Joxoon Nanu Muusaa ak Aaruuna Tawreet ak leeraay ak fàtttaliku ngir ña ragal Yàlla,

🎧 Dégg


📜 Aaya 46-50 — Simoore Al-Anbiya

46وَلَئِن مَّسَّتْهُمْ نَفْحَةٌ مِّنْ عَذَابِ رَبِّكَ لَيَقُولُنَّ يَا وَيْلَنَا إِنَّا كُنَّا ظَالِمِينَ
Te bu leen lu tuuti daloon ci sa ndigalu Boroom, ñu dellu tàmbalee wax naan : “Ngalla nun ! Nun ay tooñkat lanu woon”.
47وَنَضَعُ الْمَوَازِينَ الْقِسْطَ لِيَوْمِ الْقِيَامَةِ فَلَا تُظْلَمُ نَفْسٌ شَيْئًا ۖ وَإِن كَانَ مِثْقَالَ حَبَّةٍ مِّنْ خَرْدَلٍ أَتَيْنَا بِهَا ۗ وَكَفَىٰ بِنَا حَاسِبِينَ
Dana tëral màndaxe mu maandu ca Bis-pénc ba. Te deesul tooñ benn bakkan ci dara, doonte lu tollu ni pepp bàkket, Dananu ko indi. Te aka mën a wàññi.
48وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَىٰ وَهَارُونَ الْفُرْقَانَ وَضِيَاءً وَذِكْرًا لِّلْمُتَّقِينَ
Joxoon Nanu Muusaa ak Aaruuna Tawreet ak leeraay ak fàtttaliku ngir ña ragal Yàlla,
49الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ وَهُم مِّنَ السَّاعَةِ مُشْفِقُونَ
ñooy ña ragal seen Boroom ci kumpa, te ñoom way-jàq lañu ca Bis-pénc ba.
50وَهَٰذَا ذِكْرٌ مُّبَارَكٌ أَنزَلْنَاهُ ۚ أَفَأَنتُمْ لَهُ مُنكِرُونَ
Te lii [Alxuraan jii], tur la wu barkeel [sakkan] wu Nu wàcce. Ndax yéen dangeen koy weddi ?
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
48Aaya

Tekki — Al-Anbiya 48

Simoore Al-Anbiya Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Joxoon Nanu Muusaa ak Aaruuna Tawreet ak leeraay ak fàtttaliku…

Simoore Aaya 48/112 — Simoore Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Anbiya Dégg, Simoore Al-Anbiya Tekki, Simoore Al-Anbiya mp3, Simoore Al-Anbiya pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers