Al-Anbiya · 50/112
Tekki Waxtaan — Al-Anbiya
وَهَٰذَا ذِكْرٌ مُّبَارَكٌ أَنزَلْنَاهُ ۚ أَفَأَنتُمْ لَهُ مُنكِرُونَ ٥٠
Transliteration
Wa haazaa Zikrum Mubaarakun anzalnaah; afa antum lahoo munkiroon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te lii [Alxuraan jii], tur la wu barkeel [sakkan] wu Nu wàcce. Ndax yéen dangeen koy weddi ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 48-52 — Al-Anbiya
48وَلَقَدْ آتَيْنَا مُوسَىٰ وَهَارُونَ الْفُرْقَانَ وَضِيَاءً وَذِكْرًا لِّلْمُتَّقِينَ
Joxoon Nanu Muusaa ak Aaruuna Tawreet ak leeraay ak fàtttaliku ngir ña ragal Yàlla,
49الَّذِينَ يَخْشَوْنَ رَبَّهُم بِالْغَيْبِ وَهُم مِّنَ السَّاعَةِ مُشْفِقُونَ
ñooy ña ragal seen Boroom ci kumpa, te ñoom way-jàq lañu ca Bis-pénc ba.
50وَهَٰذَا ذِكْرٌ مُّبَارَكٌ أَنزَلْنَاهُ ۚ أَفَأَنتُمْ لَهُ مُنكِرُونَ
Te lii [Alxuraan jii], tur la wu barkeel [sakkan] wu Nu wàcce. Ndax yéen dangeen koy weddi ?
51۞ وَلَقَدْ آتَيْنَا إِبْرَاهِيمَ رُشْدَهُ مِن قَبْلُ وَكُنَّا بِهِ عَالِمِينَ
Te mayoon Nanu Ibraahiima njub lu jiitu. Te nekkoon Nanu ñu ko xam xéll.
52إِذْ قَالَ لِأَبِيهِ وَقَوْمِهِ مَا هَٰذِهِ التَّمَاثِيلُ الَّتِي أَنتُمْ لَهَا عَاكِفُونَ
[Fàttalikul] ba mu waxee baayam ak nitam ña, ne leen : “Ana luy yàlla xërëm [yu diy jëmm yu ñu yatt] te ngeen fonk leen lool ? ”.
Al-AnbiyaFihi Alxuraan
112Aaya
MeccanRevelation
50Aaya
Tekki — Al-Anbiya 50
Simoore Al-Anbiya Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te lii [Alxuraan jii], tur la wu barkeel [sakkan] wu…Simoore Aaya 50/112 — Al-Anbiya الأنبياء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Anbiya Dégg, Al-Anbiya Tekki, Al-Anbiya mp3, Al-Anbiya pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








