Al-Hajj · 49/78
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Hajj
قُلْ يَا أَيُّهَا النَّاسُ إِنَّمَا أَنَا لَكُمْ نَذِيرٌ مُّبِينٌ ۝٤٩
Qul yaaa ayyuhan naasu innamaaa ana lakum nazeerum mubeen
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Éy yéen nit ñi ! Man nekkuma ci yéen lu dul ab waaraatekat bu wér”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 47-51 — Simoore Al-Hajj

47وَيَسْتَعْجِلُونَكَ بِالْعَذَابِ وَلَن يُخْلِفَ اللَّهُ وَعْدَهُ ۚ وَإِنَّ يَوْمًا عِندَ رَبِّكَ كَأَلْفِ سَنَةٍ مِّمَّا تَعُدُّونَ
Ña nga lay yàkkamti ci mbugal mi. Te Yàlla du soppi àppam. Te benn bis ca sa Boroom mi ngi mel ni junni at ci seen waññi.
48وَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ أَمْلَيْتُ لَهَا وَهِيَ ظَالِمَةٌ ثُمَّ أَخَذْتُهَا وَإِلَيَّ الْمَصِيرُ
Aka bari dëkk yu Mu muñal te ñu tooñoon ? Ba noppi Mu fàdd leen. Te ci Man la lépp di mujj.
49قُلْ يَا أَيُّهَا النَّاسُ إِنَّمَا أَنَا لَكُمْ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Neel : “Éy yéen nit ñi ! Man nekkuma ci yéen lu dul ab waaraatekat bu wér”.
50فَالَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ
Kon ña gëm tey jëf jëf ju yiw am nañu njéggal ak xéewal gu tedd,
51وَالَّذِينَ سَعَوْا فِي آيَاتِنَا مُعَاجِزِينَ أُولَٰئِكَ أَصْحَابُ الْجَحِيمِ
ña nga xam ne ñi ngi dox di yoqatloo nit ñi ci Sunuy ndigal, ñooña ñooy waa Safara.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
49Aaya

Tekki — Al-Hajj 49

Simoore Al-Hajj Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Éy yéen nit ñi ! Man nekkuma ci…

Simoore Aaya 49/78 — Simoore Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Hajj Dégg, Simoore Al-Hajj Tekki, Simoore Al-Hajj mp3, Simoore Al-Hajj pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers