Al-Hajj · 48/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
وَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ أَمْلَيْتُ لَهَا وَهِيَ ظَالِمَةٌ ثُمَّ أَخَذْتُهَا وَإِلَيَّ الْمَصِيرُ ۝٤٨
Wa ka ayyim min qaryatin amlaitu lahaa wa hiya zaalimatun summa akhaztuhaa wa ilaiyal maseer
📖 Tekkim Wolof
Aka bari dëkk yu Mu muñal te ñu tooñoon ? Ba noppi Mu fàdd leen. Te ci Man la lépp di mujj.
🎧 Dégg

📜 Aaya 46-50 — Al-Hajj

46أَفَلَمْ يَسِيرُوا فِي الْأَرْضِ فَتَكُونَ لَهُمْ قُلُوبٌ يَعْقِلُونَ بِهَا أَوْ آذَانٌ يَسْمَعُونَ بِهَا ۖ فَإِنَّهَا لَا تَعْمَى الْأَبْصَارُ وَلَٰكِن تَعْمَى الْقُلُوبُ الَّتِي فِي الصُّدُورِ
Moo ndax dañoo doxul ci kaw suuf ? Kon danañu am xol bu am ràññee ci loolu ak nopp yu ca am dégg gu wér.Te sax du gët yi ñoo di gumba, waaye xol yi nekk ci seeni dënn ñooy gumba.
47وَيَسْتَعْجِلُونَكَ بِالْعَذَابِ وَلَن يُخْلِفَ اللَّهُ وَعْدَهُ ۚ وَإِنَّ يَوْمًا عِندَ رَبِّكَ كَأَلْفِ سَنَةٍ مِّمَّا تَعُدُّونَ
Ña nga lay yàkkamti ci mbugal mi. Te Yàlla du soppi àppam. Te benn bis ca sa Boroom mi ngi mel ni junni at ci seen waññi.
48وَكَأَيِّن مِّن قَرْيَةٍ أَمْلَيْتُ لَهَا وَهِيَ ظَالِمَةٌ ثُمَّ أَخَذْتُهَا وَإِلَيَّ الْمَصِيرُ
Aka bari dëkk yu Mu muñal te ñu tooñoon ? Ba noppi Mu fàdd leen. Te ci Man la lépp di mujj.
49قُلْ يَا أَيُّهَا النَّاسُ إِنَّمَا أَنَا لَكُمْ نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Neel : “Éy yéen nit ñi ! Man nekkuma ci yéen lu dul ab waaraatekat bu wér”.
50فَالَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَهُم مَّغْفِرَةٌ وَرِزْقٌ كَرِيمٌ
Kon ña gëm tey jëf jëf ju yiw am nañu njéggal ak xéewal gu tedd,
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
48Aaya

Tekki — Al-Hajj 48

Simoore Al-Hajj Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Aka bari dëkk yu Mu muñal te ñu tooñoon ?…

Simoore Aaya 48/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers