Al-Hajj · 67/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
لِّكُلِّ أُمَّةٍ جَعَلْنَا مَنسَكًا هُمْ نَاسِكُوهُ ۖ فَلَا يُنَازِعُنَّكَ فِي الْأَمْرِ ۚ وَادْعُ إِلَىٰ رَبِّكَ ۖ إِنَّكَ لَعَلَىٰ هُدًى مُّسْتَقِيمٍ ٦٧
Transliteration
Likulli ummatin ja`alnaa mansakan hum naasikoohu falaa yunaazi `unnaka fil amr; wad`u ilaa Rabbika innaka la `alaa hudam mustaqeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Xeet wu nekk defal Nanu ko jaamukaay wu ñu koy jaamoo. Kon buñu xëccook yaw ci mbir yi ! Te nanga woote jëme ci sa Boroom. Yaw de yaa ngi ci njub gu ne xocc.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 65-69 — Al-Hajj
65أَلَمْ تَرَ أَنَّ اللَّهَ سَخَّرَ لَكُم مَّا فِي الْأَرْضِ وَالْفُلْكَ تَجْرِي فِي الْبَحْرِ بِأَمْرِهِ وَيُمْسِكُ السَّمَاءَ أَن تَقَعَ عَلَى الْأَرْضِ إِلَّا بِإِذْنِهِ ۗ إِنَّ اللَّهَ بِالنَّاسِ لَرَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Ndax gisoo ne Yàlla tàggatal na leen li nekk ci suuf si, te gaal gay daw ci ndigalam la ? Te Moo tee asamaan daanu ci kaw suuf si ci ndigalam. Te Yàlla kuy ñeewant la, di Kuy jagle nit ñi yërmaandeem.
66وَهُوَ الَّذِي أَحْيَاكُمْ ثُمَّ يُمِيتُكُمْ ثُمَّ يُحْيِيكُمْ ۗ إِنَّ الْإِنسَانَ لَكَفُورٌ
Te Moom mooy ki leen dundal te Dana leen rey, ba noppi Mu dundalaat leen. Waaye nit weddiwaakoon la.
67لِّكُلِّ أُمَّةٍ جَعَلْنَا مَنسَكًا هُمْ نَاسِكُوهُ ۖ فَلَا يُنَازِعُنَّكَ فِي الْأَمْرِ ۚ وَادْعُ إِلَىٰ رَبِّكَ ۖ إِنَّكَ لَعَلَىٰ هُدًى مُّسْتَقِيمٍ
Xeet wu nekk defal Nanu ko jaamukaay wu ñu koy jaamoo. Kon buñu xëccook yaw ci mbir yi ! Te nanga woote jëme ci sa Boroom. Yaw de yaa ngi ci njub gu ne xocc.
68وَإِن جَادَلُوكَ فَقُلِ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا تَعْمَلُونَ
Bu ñu dàggasanteek yaw, neel : “Yàlla moo gën a xam li ngeen di def.
69اللَّهُ يَحْكُمُ بَيْنَكُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كُنتُمْ فِيهِ تَخْتَلِفُونَ
Yàlla dana àtte seen diggante bu Bis-pénc baa ca la ngeen doon juuyoo”.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
67Aaya
Tekki — Al-Hajj 67
Simoore Al-Hajj Aaya 67 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Xeet wu nekk defal Nanu ko jaamukaay wu ñu koy…Simoore Aaya 67/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 65–69. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








