Al-Hajj · 68/78
Tekki Waxtaan — Al-Hajj
وَإِن جَادَلُوكَ فَقُلِ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا تَعْمَلُونَ ۝٦٨
Wa in jaadalooka faqulil laahu a`lamu bimaa ta`maloon
📖 Tekkim Wolof
Bu ñu dàggasanteek yaw, neel : “Yàlla moo gën a xam li ngeen di def.
🎧 Dégg

📜 Aaya 66-70 — Al-Hajj

66وَهُوَ الَّذِي أَحْيَاكُمْ ثُمَّ يُمِيتُكُمْ ثُمَّ يُحْيِيكُمْ ۗ إِنَّ الْإِنسَانَ لَكَفُورٌ
Te Moom mooy ki leen dundal te Dana leen rey, ba noppi Mu dundalaat leen. Waaye nit weddiwaakoon la.
67لِّكُلِّ أُمَّةٍ جَعَلْنَا مَنسَكًا هُمْ نَاسِكُوهُ ۖ فَلَا يُنَازِعُنَّكَ فِي الْأَمْرِ ۚ وَادْعُ إِلَىٰ رَبِّكَ ۖ إِنَّكَ لَعَلَىٰ هُدًى مُّسْتَقِيمٍ
Xeet wu nekk defal Nanu ko jaamukaay wu ñu koy jaamoo. Kon buñu xëccook yaw ci mbir yi ! Te nanga woote jëme ci sa Boroom. Yaw de yaa ngi ci njub gu ne xocc.
68وَإِن جَادَلُوكَ فَقُلِ اللَّهُ أَعْلَمُ بِمَا تَعْمَلُونَ
Bu ñu dàggasanteek yaw, neel : “Yàlla moo gën a xam li ngeen di def.
69اللَّهُ يَحْكُمُ بَيْنَكُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ فِيمَا كُنتُمْ فِيهِ تَخْتَلِفُونَ
Yàlla dana àtte seen diggante bu Bis-pénc baa ca la ngeen doon juuyoo”.
70أَلَمْ تَعْلَمْ أَنَّ اللَّهَ يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاءِ وَالْأَرْضِ ۗ إِنَّ ذَٰلِكَ فِي كِتَابٍ ۚ إِنَّ ذَٰلِكَ عَلَى اللَّهِ يَسِيرٌ
Ndax dangaa xamul ne Yàlla xam na li nekk ci asamaan yi ak suuf si ? Te loolu nekk na ci ab Téere, te it loolu lu yomb Yàlla la.
Al-HajjFihi Alxuraan
78Aaya
MedinanRevelation
68Aaya

Tekki — Al-Hajj 68

Simoore Al-Hajj Aaya 68 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Bu ñu dàggasanteek yaw, neel : “Yàlla moo gën a…

Simoore Aaya 68/78 — Al-Hajj الحج (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Hajj Dégg, Al-Hajj Tekki, Al-Hajj mp3, Al-Hajj pdf. Aaya 66–70. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers