Al-Mu'minun · 14/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
ثُمَّ خَلَقْنَا النُّطْفَةَ عَلَقَةً فَخَلَقْنَا الْعَلَقَةَ مُضْغَةً فَخَلَقْنَا الْمُضْغَةَ عِظَامًا فَكَسَوْنَا الْعِظَامَ لَحْمًا ثُمَّ أَنشَأْنَاهُ خَلْقًا آخَرَ ۚ فَتَبَارَكَ اللَّهُ أَحْسَنُ الْخَالِقِينَ ۝١٤
Summa khalaqnan nutfata `alaqatan fakhalaqnal `alaqata mudghatan fakhalaq nal mudghata `izaaman fakasawnal `izaama lahman summa anshaanaahu khalqan aakhar; fatabaarakal laahu ahsanul khaaliqeen
📖 Tekkim Wolof
Ginnaaw ba Nu def lumbu ma di aw suux ; ginnaaw ba Nu def suux wa mu di ay yax, daldi sànge yax ya aw yàpp. Daldi koy def jëmm,Yàllaa mën a sakkanal. Moom miy gën gi Bindkat !

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 12-16 — Simoore Al-Mu'minun

12وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن سُلَالَةٍ مِّن طِينٍ
Nun bind Nanu nit [sàkk ko]mu bawoo ci cosaanul ban [suuf],
13ثُمَّ جَعَلْنَاهُ نُطْفَةً فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ
ginnaaw ba Nu def ko mu di maniyu ma mu di aw lumbu.
14ثُمَّ خَلَقْنَا النُّطْفَةَ عَلَقَةً فَخَلَقْنَا الْعَلَقَةَ مُضْغَةً فَخَلَقْنَا الْمُضْغَةَ عِظَامًا فَكَسَوْنَا الْعِظَامَ لَحْمًا ثُمَّ أَنشَأْنَاهُ خَلْقًا آخَرَ ۚ فَتَبَارَكَ اللَّهُ أَحْسَنُ الْخَالِقِينَ
Ginnaaw ba Nu def lumbu ma di aw suux ; ginnaaw ba Nu def suux wa mu di ay yax, daldi sànge yax ya aw yàpp. Daldi koy def jëmm,Yàllaa mën a sakkanal. Moom miy gën gi Bindkat !
15ثُمَّ إِنَّكُم بَعْدَ ذَٰلِكَ لَمَيِّتُونَ
Bu loolu jàllee, dangeen di dee.
16ثُمَّ إِنَّكُمْ يَوْمَ الْقِيَامَةِ تُبْعَثُونَ
Ba noppi Bis-pénc ba Mu dekkal leen.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 14

Simoore Al-Mu'minun Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ginnaaw ba Nu def lumbu ma di aw suux ;…

Simoore Aaya 14/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers