Al-Mu'minun · 13/118
Tekki Waxtaan — Al-Mu'minun
ثُمَّ جَعَلْنَاهُ نُطْفَةً فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ ۝١٣
Summa ja`alnaahu nutfatan fee qaraarim makeen
📖 Tekkim Wolof
ginnaaw ba Nu def ko mu di maniyu ma mu di aw lumbu.

🎧 Dégg


📜 Aaya 11-15 — Al-Mu'minun

11الَّذِينَ يَرِثُونَ الْفِرْدَوْسَ هُمْ فِيهَا خَالِدُونَ
ña nga xam ne danañu donn Àjjana Firdawsi, te dañu cay béel.
12وَلَقَدْ خَلَقْنَا الْإِنسَانَ مِن سُلَالَةٍ مِّن طِينٍ
Nun bind Nanu nit [sàkk ko]mu bawoo ci cosaanul ban [suuf],
13ثُمَّ جَعَلْنَاهُ نُطْفَةً فِي قَرَارٍ مَّكِينٍ
ginnaaw ba Nu def ko mu di maniyu ma mu di aw lumbu.
14ثُمَّ خَلَقْنَا النُّطْفَةَ عَلَقَةً فَخَلَقْنَا الْعَلَقَةَ مُضْغَةً فَخَلَقْنَا الْمُضْغَةَ عِظَامًا فَكَسَوْنَا الْعِظَامَ لَحْمًا ثُمَّ أَنشَأْنَاهُ خَلْقًا آخَرَ ۚ فَتَبَارَكَ اللَّهُ أَحْسَنُ الْخَالِقِينَ
Ginnaaw ba Nu def lumbu ma di aw suux ; ginnaaw ba Nu def suux wa mu di ay yax, daldi sànge yax ya aw yàpp. Daldi koy def jëmm,Yàllaa mën a sakkanal. Moom miy gën gi Bindkat !
15ثُمَّ إِنَّكُم بَعْدَ ذَٰلِكَ لَمَيِّتُونَ
Bu loolu jàllee, dangeen di dee.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
13Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 13

Simoore Al-Mu'minun Aaya 13 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ginnaaw ba Nu def ko mu di maniyu ma mu…

Simoore Aaya 13/118 — Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Mu'minun Dégg, Al-Mu'minun Tekki, Al-Mu'minun mp3, Al-Mu'minun pdf. Aaya 11–15. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers