Al-Mu'minun · 33/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَقَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِهِ الَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِلِقَاءِ الْآخِرَةِ وَأَتْرَفْنَاهُمْ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يَأْكُلُ مِمَّا تَأْكُلُونَ مِنْهُ وَيَشْرَبُ مِمَّا تَشْرَبُونَ ۝٣٣
Wa qaalal mala-u min qawmihil lazeena kafaroo wa kazzaboo bi liqaaa`il Aakhirati wa atrafnaahum fil hayaatid dunyaa maa haazaaa illaa basharum mislukum yaakulu mimmaa taakuloona minhu wa yashrabu mimmaa tashraboon
📖 Tekkim Wolof
Ña jiite yéefar ya cig nitam tey weddi ne danañu dajeek seen Boroom Bis-pénc ba, daldi wax ne : “Kii daal nit la ni yéen, ci li ngeen di lekk lay lekk, di naan ci li ngeen di naan.

🎧 Dégg


📜 Aaya 31-35 — Simoore Al-Mu'minun

31ثُمَّ أَنشَأْنَا مِن بَعْدِهِمْ قَرْنًا آخَرِينَ
Topp, ginnaaw ba, Nu sos ay maas ci ñeneen,
32فَأَرْسَلْنَا فِيهِمْ رَسُولًا مِّنْهُمْ أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Nu yónni ci ñoom ab Yonent bu bokk ci ñoom [ngir mu wax leen] : “Jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
33وَقَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِهِ الَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِلِقَاءِ الْآخِرَةِ وَأَتْرَفْنَاهُمْ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يَأْكُلُ مِمَّا تَأْكُلُونَ مِنْهُ وَيَشْرَبُ مِمَّا تَشْرَبُونَ
Ña jiite yéefar ya cig nitam tey weddi ne danañu dajeek seen Boroom Bis-pénc ba, daldi wax ne : “Kii daal nit la ni yéen, ci li ngeen di lekk lay lekk, di naan ci li ngeen di naan.
34وَلَئِنْ أَطَعْتُم بَشَرًا مِّثْلَكُمْ إِنَّكُمْ إِذًا لَّخَاسِرُونَ
Te bu ngeen toppee ci moom (nitug njorondaay)ni yéen, dangeen yàqule.
35أَيَعِدُكُمْ أَنَّكُمْ إِذَا مِتُّمْ وَكُنتُمْ تُرَابًا وَعِظَامًا أَنَّكُم مُّخْرَجُونَ
Moo ndax daleen a dig ne bu ngeen faatoo ba doon suuf ak i yax, dangeen génnaat dekki ?
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
33Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 33

Simoore Al-Mu'minun Aaya 33 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña jiite yéefar ya cig nitam tey weddi ne danañu…

Simoore Aaya 33/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 31–35. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers