Al-Mu'minun · 32/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
فَأَرْسَلْنَا فِيهِمْ رَسُولًا مِّنْهُمْ أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ ۝٣٢
Fa arsalnaa feehim Rasoolam minhum ani`budul laaha maa lakum min ilaahin ghairuhoo afalaa tattaqoon
📖 Tekkim Wolof
Nu yónni ci ñoom ab Yonent bu bokk ci ñoom [ngir mu wax leen] : “Jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”

🎧 Dégg


📜 Aaya 30-34 — Simoore Al-Mu'minun

30إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَاتٍ وَإِن كُنَّا لَمُبْتَلِينَ
Ay kéemaannekk na ci biir loolu. Doontele sax dañuy nattu (ñi gëm).
31ثُمَّ أَنشَأْنَا مِن بَعْدِهِمْ قَرْنًا آخَرِينَ
Topp, ginnaaw ba, Nu sos ay maas ci ñeneen,
32فَأَرْسَلْنَا فِيهِمْ رَسُولًا مِّنْهُمْ أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Nu yónni ci ñoom ab Yonent bu bokk ci ñoom [ngir mu wax leen] : “Jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
33وَقَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِهِ الَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِلِقَاءِ الْآخِرَةِ وَأَتْرَفْنَاهُمْ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يَأْكُلُ مِمَّا تَأْكُلُونَ مِنْهُ وَيَشْرَبُ مِمَّا تَشْرَبُونَ
Ña jiite yéefar ya cig nitam tey weddi ne danañu dajeek seen Boroom Bis-pénc ba, daldi wax ne : “Kii daal nit la ni yéen, ci li ngeen di lekk lay lekk, di naan ci li ngeen di naan.
34وَلَئِنْ أَطَعْتُم بَشَرًا مِّثْلَكُمْ إِنَّكُمْ إِذًا لَّخَاسِرُونَ
Te bu ngeen toppee ci moom (nitug njorondaay)ni yéen, dangeen yàqule.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
32Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 32

Simoore Al-Mu'minun Aaya 32 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Nu yónni ci ñoom ab Yonent bu bokk ci ñoom…

Simoore Aaya 32/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 30–34. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers