Al-Mu'minun · 34/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَلَئِنْ أَطَعْتُم بَشَرًا مِّثْلَكُمْ إِنَّكُمْ إِذًا لَّخَاسِرُونَ ۝٣٤
Wa la`in at`atum basharam mislakum innakum izal lakhaasiroon
📖 Tekkim Wolof
Te bu ngeen toppee ci moom (nitug njorondaay)ni yéen, dangeen yàqule.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 32-36 — Simoore Al-Mu'minun

32فَأَرْسَلْنَا فِيهِمْ رَسُولًا مِّنْهُمْ أَنِ اعْبُدُوا اللَّهَ مَا لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرُهُ ۖ أَفَلَا تَتَّقُونَ
Nu yónni ci ñoom ab Yonent bu bokk ci ñoom [ngir mu wax leen] : “Jaamuleen Yàlla. Amuleen jeneen yàlla ju dul Moom. Moo ndax dangeen dul ragal Yàlla ? ”
33وَقَالَ الْمَلَأُ مِن قَوْمِهِ الَّذِينَ كَفَرُوا وَكَذَّبُوا بِلِقَاءِ الْآخِرَةِ وَأَتْرَفْنَاهُمْ فِي الْحَيَاةِ الدُّنْيَا مَا هَٰذَا إِلَّا بَشَرٌ مِّثْلُكُمْ يَأْكُلُ مِمَّا تَأْكُلُونَ مِنْهُ وَيَشْرَبُ مِمَّا تَشْرَبُونَ
Ña jiite yéefar ya cig nitam tey weddi ne danañu dajeek seen Boroom Bis-pénc ba, daldi wax ne : “Kii daal nit la ni yéen, ci li ngeen di lekk lay lekk, di naan ci li ngeen di naan.
34وَلَئِنْ أَطَعْتُم بَشَرًا مِّثْلَكُمْ إِنَّكُمْ إِذًا لَّخَاسِرُونَ
Te bu ngeen toppee ci moom (nitug njorondaay)ni yéen, dangeen yàqule.
35أَيَعِدُكُمْ أَنَّكُمْ إِذَا مِتُّمْ وَكُنتُمْ تُرَابًا وَعِظَامًا أَنَّكُم مُّخْرَجُونَ
Moo ndax daleen a dig ne bu ngeen faatoo ba doon suuf ak i yax, dangeen génnaat dekki ?
36۞ هَيْهَاتَ هَيْهَاتَ لِمَا تُوعَدُونَ
Mukk, mukk li ñu leen dig !
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
34Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 34

Simoore Al-Mu'minun Aaya 34 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te bu ngeen toppee ci moom (nitug njorondaay)ni yéen, dangeen…

Simoore Aaya 34/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 32–36. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 28, 2026

Don't forget us in your sincere prayers