Al-Mu'minun · 58/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
وَالَّذِينَ هُم بِآيَاتِ رَبِّهِمْ يُؤْمِنُونَ ۝٥٨
Wallazeena hum bi Aayaati Rabbihim yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
ña nga xam ne dañoo gëm seen kàdduy Boroom,

🎧 Dégg


📜 Aaya 56-60 — Simoore Al-Mu'minun

56نُسَارِعُ لَهُمْ فِي الْخَيْرَاتِ ۚ بَل لَّا يَشْعُرُونَ
Danu leen di gaawe [fey leen baaxug la ñu nekk] ? Ñoom yëguñu li xew de.
57إِنَّ الَّذِينَ هُم مِّنْ خَشْيَةِ رَبِّهِم مُّشْفِقُونَ
Ña sóobu dëgg dëgg ci ragal seen Boroom,
58وَالَّذِينَ هُم بِآيَاتِ رَبِّهِمْ يُؤْمِنُونَ
ña nga xam ne dañoo gëm seen kàdduy Boroom,
59وَالَّذِينَ هُم بِرَبِّهِمْ لَا يُشْرِكُونَ
ña nga xam ne duñu bokkale seen Boroom ak dara,
60وَالَّذِينَ يُؤْتُونَ مَا آتَوا وَّقُلُوبُهُمْ وَجِلَةٌ أَنَّهُمْ إِلَىٰ رَبِّهِمْ رَاجِعُونَ
ña joxe ca la ñu leen xéewale, te seeni xol di nux-nuxi ci [di xalaat] ne danañu delluwaat ca seen Boroom.
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
58Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 58

Simoore Al-Mu'minun Aaya 58 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña nga xam ne dañoo gëm seen kàdduy Boroom,

Simoore Aaya 58/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 56–60. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers