Al-Mu'minun · 57/118
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Mu'minun
إِنَّ الَّذِينَ هُم مِّنْ خَشْيَةِ رَبِّهِم مُّشْفِقُونَ ۝٥٧
Innal lazeena hum min khashyati Rabbihim mushfiqoon
📖 Tekkim Wolof
Ña sóobu dëgg dëgg ci ragal seen Boroom,

🎧 Dégg


📜 Aaya 55-59 — Simoore Al-Mu'minun

55أَيَحْسَبُونَ أَنَّمَا نُمِدُّهُم بِهِ مِن مَّالٍ وَبَنِينَ
Ndax dañoo jàpp ne li ñu leen may ci alal ak i doom,
56نُسَارِعُ لَهُمْ فِي الْخَيْرَاتِ ۚ بَل لَّا يَشْعُرُونَ
Danu leen di gaawe [fey leen baaxug la ñu nekk] ? Ñoom yëguñu li xew de.
57إِنَّ الَّذِينَ هُم مِّنْ خَشْيَةِ رَبِّهِم مُّشْفِقُونَ
Ña sóobu dëgg dëgg ci ragal seen Boroom,
58وَالَّذِينَ هُم بِآيَاتِ رَبِّهِمْ يُؤْمِنُونَ
ña nga xam ne dañoo gëm seen kàdduy Boroom,
59وَالَّذِينَ هُم بِرَبِّهِمْ لَا يُشْرِكُونَ
ña nga xam ne duñu bokkale seen Boroom ak dara,
Al-Mu'minunFihi Alxuraan
118Aaya
MeccanRevelation
57Aaya

Tekki — Al-Mu'minun 57

Simoore Al-Mu'minun Aaya 57 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña sóobu dëgg dëgg ci ragal seen Boroom,

Simoore Aaya 57/118 — Simoore Al-Mu'minun المؤمنون (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Mu'minun Dégg, Simoore Al-Mu'minun Tekki, Simoore Al-Mu'minun mp3, Simoore Al-Mu'minun pdf. Aaya 55–59. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers