An-Nur · 18/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
وَيُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمُ الْآيَاتِ ۚ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ ١٨
Transliteration
Wa yubaiyinul laahu lakumul Aayaat; wallaahu `Aleemun Hakeem
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Yàllaa ngi leen di faramfàcceel i laayam de, te Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 16-20 — An-Nur
16وَلَوْلَا إِذْ سَمِعْتُمُوهُ قُلْتُم مَّا يَكُونُ لَنَا أَن نَّتَكَلَّمَ بِهَٰذَا سُبْحَانَكَ هَٰذَا بُهْتَانٌ عَظِيمٌ
Ana lan moo tere, ba ngeen ko déggee, ngeen sàbbaal Yàlla te wax ne : “Wii duur wu rëy warut a génne ci seeni làmmiñ” ?
17يَعِظُكُمُ اللَّهُ أَن تَعُودُوا لِمِثْلِهِ أَبَدًا إِن كُنتُم مُّؤْمِنِينَ
Yàllaa ngi leen di ñaax ngeen bañ a dellu mukk ci jëf ju ni mel, ndegam ay way-gëm ngeen.
18وَيُبَيِّنُ اللَّهُ لَكُمُ الْآيَاتِ ۚ وَاللَّهُ عَلِيمٌ حَكِيمٌ
Yàllaa ngi leen di faramfàcceel i laayam de, te Yàlla Ku xam la, Ku xereñ la.
19إِنَّ الَّذِينَ يُحِبُّونَ أَن تَشِيعَ الْفَاحِشَةُ فِي الَّذِينَ آمَنُوا لَهُمْ عَذَابٌ أَلِيمٌ فِي الدُّنْيَا وَالْآخِرَةِ ۚ وَاللَّهُ يَعْلَمُ وَأَنتُمْ لَا تَعْلَمُونَ
Ñi bëgg a tasaarey ñaawtéef ci biir jullit ñi, mbugal mu metti dana leen dal ci àddina ak àllaaxira. Yàlla xam na te yéen xamuleen.
20وَلَوْلَا فَضْلُ اللَّهِ عَلَيْكُمْ وَرَحْمَتُهُ وَأَنَّ اللَّهَ رَءُوفٌ رَّحِيمٌ
Cëy dogankoon ak ngënéelul Yàlla ak yëmaandeem ci yéen, waaye Yàlla Moom ku ñeewant la, di Jaglewaakoon ...
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
18Aaya
Tekki — An-Nur 18
Simoore An-Nur Aaya 18 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Yàllaa ngi leen di faramfàcceel i laayam de, te Yàlla…Simoore Aaya 18/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 16–20. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








