An-Nur · 49/64
Tekki Waxtaan — Simoore An-Nur
وَإِن يَكُن لَّهُمُ الْحَقُّ يَأْتُوا إِلَيْهِ مُذْعِنِينَ ٤٩
Transliteration
Wa iny-yakul lahumul haqqu yaatooo ilaihi muz`ineen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Su ñu nekkoon ci dëgg kon danañu dikk [ci Yonent bi] topp ko.
Additional reference in Fulfulde
M
Mishary Rashid Alafasy
✓
Mishary Rashid Alafasy
✓
M
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
Mahmoud Khalil Al-Husary
✓
A
Abdurrahman As-Sudais
✓
Abdurrahman As-Sudais
✓
M
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
Mohamed Siddiq Al-Minshawi
✓
A
Abdul Basit Abdul Samad
✓
Abdul Basit Abdul Samad
✓
A
Ali Al-Hudhaify
✓
Ali Al-Hudhaify
✓
A
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
Ahmed ibn Ali al-Ajamy
✓
A
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
Abu Bakr Ash-Shaatree
✓
M
Muhammad Ayyoub
✓
Muhammad Ayyoub
✓
A
Abdullah Basfar
✓
Abdullah Basfar
✓
A
Abdullah Al-Juhani
✓
Abdullah Al-Juhani
✓
M
Maher Al Muaiqly
✓
Maher Al Muaiqly
✓
0:00
0:00
📜 Aaya 47-51 — Simoore An-Nur
47وَيَقُولُونَ آمَنَّا بِاللَّهِ وَبِالرَّسُولِ وَأَطَعْنَا ثُمَّ يَتَوَلَّىٰ فَرِيقٌ مِّنْهُم مِّن بَعْدِ ذَٰلِكَ ۚ وَمَا أُولَٰئِكَ بِالْمُؤْمِنِينَ
Danañuy wax naan : “Gën nanu Yàlla ak Yonent bi, topp nanu it”. Mu am kurél bu bokk ñoom wëlbëtiku ginnaaw loolu. Ñoom gëmuñu.
48وَإِذَا دُعُوا إِلَى اللَّهِ وَرَسُولِهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ إِذَا فَرِيقٌ مِّنْهُم مُّعْرِضُونَ
Saa su wootees leen jëme ci Yàlla ak ci Yonentam ngir Mu àtte seen diggante, ndekete yoo ab kurél ci ñoom day dummóoyu.
49وَإِن يَكُن لَّهُمُ الْحَقُّ يَأْتُوا إِلَيْهِ مُذْعِنِينَ
Su ñu nekkoon ci dëgg kon danañu dikk [ci Yonent bi] topp ko.
50أَفِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَمِ ارْتَابُوا أَمْ يَخَافُونَ أَن يَحِيفَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ وَرَسُولُهُ ۚ بَلْ أُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Moo ndax dañoo am woppi xol ? Walla dañuy jiixi-jaaxa ? Walla dañuy ragal Yàlla ak ub Yonentam yiir leen ? Deewalaay !... ñoom ay tooñkat lañu.
51إِنَّمَا كَانَ قَوْلَ الْمُؤْمِنِينَ إِذَا دُعُوا إِلَى اللَّهِ وَرَسُولِهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ أَن يَقُولُوا سَمِعْنَا وَأَطَعْنَا ۚ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Ñi gëm Yàlla [jullit ñi], saa su ñu déggee woote buy jëme ci Yàlla ak ub Yonentam ngir àtte seen diggante, seeni wax du doon lu dul ne : “Dégg nanu, topp nanu”. Ñooña ñooy ña texe.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
49Aaya
Tekki — An-Nur 49
Simoore An-Nur Aaya 49 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Su ñu nekkoon ci dëgg kon danañu dikk [ci Yonent…Simoore Aaya 49/64 — Simoore An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Nur Dégg, Simoore An-Nur Tekki, Simoore An-Nur mp3, Simoore An-Nur pdf. Aaya 47–51. Tekkim Wolof: Fulfulde.
Simoore An-Nur
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Thursday, October 1, 2026
Don't forget us in your sincere prayers


