An-Nur · 48/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
وَإِذَا دُعُوا إِلَى اللَّهِ وَرَسُولِهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ إِذَا فَرِيقٌ مِّنْهُم مُّعْرِضُونَ ۝٤٨
Wa izaa du`ooo ilal laahi wa Rasoolihee li yahkuma bainahum izaa fareequm minhum mu`ridoon
📖 Tekkim Wolof
Saa su wootees leen jëme ci Yàlla ak ci Yonentam ngir Mu àtte seen diggante, ndekete yoo ab kurél ci ñoom day dummóoyu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 46-50 — An-Nur

46لَّقَدْ أَنزَلْنَا آيَاتٍ مُّبَيِّنَاتٍ ۚ وَاللَّهُ يَهْدِي مَن يَشَاءُ إِلَىٰ صِرَاطٍ مُّسْتَقِيمٍ
[Wér na céŋŋ ne] wàcce Nanu ay laaya [kàddu] yu leer nàññ. Te Yàlla dana gindi ku ko soob jëme ko ci yoon wu jub xocc wa.
47وَيَقُولُونَ آمَنَّا بِاللَّهِ وَبِالرَّسُولِ وَأَطَعْنَا ثُمَّ يَتَوَلَّىٰ فَرِيقٌ مِّنْهُم مِّن بَعْدِ ذَٰلِكَ ۚ وَمَا أُولَٰئِكَ بِالْمُؤْمِنِينَ
Danañuy wax naan : “Gën nanu Yàlla ak Yonent bi, topp nanu it”. Mu am kurél bu bokk ñoom wëlbëtiku ginnaaw loolu. Ñoom gëmuñu.
48وَإِذَا دُعُوا إِلَى اللَّهِ وَرَسُولِهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ إِذَا فَرِيقٌ مِّنْهُم مُّعْرِضُونَ
Saa su wootees leen jëme ci Yàlla ak ci Yonentam ngir Mu àtte seen diggante, ndekete yoo ab kurél ci ñoom day dummóoyu.
49وَإِن يَكُن لَّهُمُ الْحَقُّ يَأْتُوا إِلَيْهِ مُذْعِنِينَ
Su ñu nekkoon ci dëgg kon danañu dikk [ci Yonent bi] topp ko.
50أَفِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَمِ ارْتَابُوا أَمْ يَخَافُونَ أَن يَحِيفَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ وَرَسُولُهُ ۚ بَلْ أُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Moo ndax dañoo am woppi xol ? Walla dañuy jiixi-jaaxa ? Walla dañuy ragal Yàlla ak ub Yonentam yiir leen ? Deewalaay !... ñoom ay tooñkat lañu.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
48Aaya

Tekki — An-Nur 48

Simoore An-Nur Aaya 48 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Saa su wootees leen jëme ci Yàlla ak ci Yonentam…

Simoore Aaya 48/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 46–50. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers