An-Nur · 50/64
Tekki Waxtaan — An-Nur
أَفِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَمِ ارْتَابُوا أَمْ يَخَافُونَ أَن يَحِيفَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ وَرَسُولُهُ ۚ بَلْ أُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ ۝٥٠
Afee quloobihim ma radun amirtaabooo am yakhaafoona ani yaheefallaahu `alaihim wa Rasooluh; bal ulaaa`ika humuz zaalimoon
📖 Tekkim Wolof
Moo ndax dañoo am woppi xol ? Walla dañuy jiixi-jaaxa ? Walla dañuy ragal Yàlla ak ub Yonentam yiir leen ? Deewalaay !... ñoom ay tooñkat lañu.
🎧 Dégg

📜 Aaya 48-52 — An-Nur

48وَإِذَا دُعُوا إِلَى اللَّهِ وَرَسُولِهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ إِذَا فَرِيقٌ مِّنْهُم مُّعْرِضُونَ
Saa su wootees leen jëme ci Yàlla ak ci Yonentam ngir Mu àtte seen diggante, ndekete yoo ab kurél ci ñoom day dummóoyu.
49وَإِن يَكُن لَّهُمُ الْحَقُّ يَأْتُوا إِلَيْهِ مُذْعِنِينَ
Su ñu nekkoon ci dëgg kon danañu dikk [ci Yonent bi] topp ko.
50أَفِي قُلُوبِهِم مَّرَضٌ أَمِ ارْتَابُوا أَمْ يَخَافُونَ أَن يَحِيفَ اللَّهُ عَلَيْهِمْ وَرَسُولُهُ ۚ بَلْ أُولَٰئِكَ هُمُ الظَّالِمُونَ
Moo ndax dañoo am woppi xol ? Walla dañuy jiixi-jaaxa ? Walla dañuy ragal Yàlla ak ub Yonentam yiir leen ? Deewalaay !... ñoom ay tooñkat lañu.
51إِنَّمَا كَانَ قَوْلَ الْمُؤْمِنِينَ إِذَا دُعُوا إِلَى اللَّهِ وَرَسُولِهِ لِيَحْكُمَ بَيْنَهُمْ أَن يَقُولُوا سَمِعْنَا وَأَطَعْنَا ۚ وَأُولَٰئِكَ هُمُ الْمُفْلِحُونَ
Ñi gëm Yàlla [jullit ñi], saa su ñu déggee woote buy jëme ci Yàlla ak ub Yonentam ngir àtte seen diggante, seeni wax du doon lu dul ne : “Dégg nanu, topp nanu”. Ñooña ñooy ña texe.
52وَمَن يُطِعِ اللَّهَ وَرَسُولَهُ وَيَخْشَ اللَّهَ وَيَتَّقْهِ فَأُولَٰئِكَ هُمُ الْفَائِزُونَ
Képp kuy topp Yàlla ak ub Yonentam, ragal Yàlla te di Ko fuglu, ñooña ñooy ña texe.
An-NurFihi Alxuraan
64Aaya
MedinanRevelation
50Aaya

Tekki — An-Nur 50

Simoore An-Nur Aaya 50 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Moo ndax dañoo am woppi xol ? Walla dañuy jiixi-jaaxa…

Simoore Aaya 50/64 — An-Nur النور (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: An-Nur Dégg, An-Nur Tekki, An-Nur mp3, An-Nur pdf. Aaya 48–52. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers