Al-Furqan · 16/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
لَّهُمْ فِيهَا مَا يَشَاءُونَ خَالِدِينَ ۚ كَانَ عَلَىٰ رَبِّكَ وَعْدًا مَّسْئُولًا ١٦
Transliteration
Lahum feehaa maa yashaaa`oona khaalideen; kaana `alaa Rabbika wa`dam mas`oolaa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Am nañu fa lépp lu leen fa soob te dañu fay béel. Yàllaa ko warlu.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 14-18 — Al-Furqan
14لَّا تَدْعُوا الْيَوْمَ ثُبُورًا وَاحِدًا وَادْعُوا ثُبُورًا كَثِيرًا
“Bisu tey jii, buleen yuuxu jenn tuskare doŋŋ, ay tuskare yu bari la”.
15قُلْ أَذَٰلِكَ خَيْرٌ أَمْ جَنَّةُ الْخُلْدِ الَّتِي وُعِدَ الْمُتَّقُونَ ۚ كَانَتْ لَهُمْ جَزَاءً وَمَصِيرًا
Neel : “Ndax loolu moo gën ? Walla Àjjanay xéewal ju sax ju ma digee fey gaa ña ragal Yàlla, muy seen kër ?”
16لَّهُمْ فِيهَا مَا يَشَاءُونَ خَالِدِينَ ۚ كَانَ عَلَىٰ رَبِّكَ وَعْدًا مَّسْئُولًا
Am nañu fa lépp lu leen fa soob te dañu fay béel. Yàllaa ko warlu.
17وَيَوْمَ يَحْشُرُهُمْ وَمَا يَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ فَيَقُولُ أَأَنتُمْ أَضْلَلْتُمْ عِبَادِي هَٰؤُلَاءِ أَمْ هُمْ ضَلُّوا السَّبِيلَ
Bis ba Mu leen di pang, boole leen ak ya ñu doon jaamu bàyyi Yàlla, Di leen wax [moom Yàlla] naan : “Ndax yéen a sànkoon sama jaam ñii, walla ñoom ñoo sànku woon réere yoon wa ? ”
18قَالُوا سُبْحَانَكَ مَا كَانَ يَنبَغِي لَنَا أَن نَّتَّخِذَ مِن دُونِكَ مِنْ أَوْلِيَاءَ وَلَٰكِن مَّتَّعْتَهُمْ وَآبَاءَهُمْ حَتَّىٰ نَسُوا الذِّكْرَ وَكَانُوا قَوْمًا بُورًا
Ñuy wax di tontu naan : “Tudd nanu sa sell gi. ! Yellut ci nun nuy wut kilifa bàyyi la, waaye Yaa leen tuuroon xéewal ñook seeni baay ba tax ñu fàtte [Alxuraan]. Far sànku”.
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
16Aaya
Tekki — Al-Furqan 16
Simoore Al-Furqan Aaya 16 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Am nañu fa lépp lu leen fa soob te dañu…Simoore Aaya 16/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 14–18. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








