Al-Furqan · 15/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
قُلْ أَذَٰلِكَ خَيْرٌ أَمْ جَنَّةُ الْخُلْدِ الَّتِي وُعِدَ الْمُتَّقُونَ ۚ كَانَتْ لَهُمْ جَزَاءً وَمَصِيرًا ١٥
Transliteration
Qul azaalika khairun am Jannatul khuldil latee wu`idal muttaqoon; kaanat lahum jazaaa`anw wa maseeraa
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Neel : “Ndax loolu moo gën ? Walla Àjjanay xéewal ju sax ju ma digee fey gaa ña ragal Yàlla, muy seen kër ?”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 13-17 — Al-Furqan
13وَإِذَا أُلْقُوا مِنْهَا مَكَانًا ضَيِّقًا مُّقَرَّنِينَ دَعَوْا هُنَالِكَ ثُبُورًا
Bu ñu leen ca sànnee ci pukus bu xat, lëkke leen [jéng], ñuy wél-wéliy juuxu ci toskare.
14لَّا تَدْعُوا الْيَوْمَ ثُبُورًا وَاحِدًا وَادْعُوا ثُبُورًا كَثِيرًا
“Bisu tey jii, buleen yuuxu jenn tuskare doŋŋ, ay tuskare yu bari la”.
15قُلْ أَذَٰلِكَ خَيْرٌ أَمْ جَنَّةُ الْخُلْدِ الَّتِي وُعِدَ الْمُتَّقُونَ ۚ كَانَتْ لَهُمْ جَزَاءً وَمَصِيرًا
Neel : “Ndax loolu moo gën ? Walla Àjjanay xéewal ju sax ju ma digee fey gaa ña ragal Yàlla, muy seen kër ?”
16لَّهُمْ فِيهَا مَا يَشَاءُونَ خَالِدِينَ ۚ كَانَ عَلَىٰ رَبِّكَ وَعْدًا مَّسْئُولًا
Am nañu fa lépp lu leen fa soob te dañu fay béel. Yàllaa ko warlu.
17وَيَوْمَ يَحْشُرُهُمْ وَمَا يَعْبُدُونَ مِن دُونِ اللَّهِ فَيَقُولُ أَأَنتُمْ أَضْلَلْتُمْ عِبَادِي هَٰؤُلَاءِ أَمْ هُمْ ضَلُّوا السَّبِيلَ
Bis ba Mu leen di pang, boole leen ak ya ñu doon jaamu bàyyi Yàlla, Di leen wax [moom Yàlla] naan : “Ndax yéen a sànkoon sama jaam ñii, walla ñoom ñoo sànku woon réere yoon wa ? ”
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
15Aaya
Tekki — Al-Furqan 15
Simoore Al-Furqan Aaya 15 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Neel : “Ndax loolu moo gën ? Walla Àjjanay xéewal…Simoore Aaya 15/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 13–17. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








