Al-Furqan · 39/77
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Furqan
وَكُلًّا ضَرَبْنَا لَهُ الْأَمْثَالَ ۖ وَكُلًّا تَبَّرْنَا تَتْبِيرًا ۝٣٩
Wa kullandarabnaa lahul amsaala wa kullan tabbarnaa tatbeera
📖 Tekkim Wolof
Ku nekk ci ñoom, sadd Nanu koy léebu, alag Nanu leen ñoom ñépp.

🎧 Dégg


📜 Aaya 37-41 — Simoore Al-Furqan

37وَقَوْمَ نُوحٍ لَّمَّا كَذَّبُوا الرُّسُلَ أَغْرَقْنَاهُمْ وَجَعَلْنَاهُمْ لِلنَّاسِ آيَةً ۖ وَأَعْتَدْنَا لِلظَّالِمِينَ عَذَابًا أَلِيمًا
Te nitu Nooh ya, ba ñu weddee Yonent ya, labal Nanu leen, def Nanu leen it kéemaan ci nit ñi. Te waajalal Nanu tooñkat ya mbugal mu metti.
38وَعَادًا وَثَمُودَ وَأَصْحَابَ الرَّسِّ وَقُرُونًا بَيْنَ ذَٰلِكَ كَثِيرًا
Ak nitu Aad, ak nitu Samooda ak waa Rasi, ak maas yu bari yu nekkoon seeni diggante !
39وَكُلًّا ضَرَبْنَا لَهُ الْأَمْثَالَ ۖ وَكُلًّا تَبَّرْنَا تَتْبِيرًا
Ku nekk ci ñoom, sadd Nanu koy léebu, alag Nanu leen ñoom ñépp.
40وَلَقَدْ أَتَوْا عَلَى الْقَرْيَةِ الَّتِي أُمْطِرَتْ مَطَرَ السَّوْءِ ۚ أَفَلَمْ يَكُونُوا يَرَوْنَهَا ۚ بَلْ كَانُوا لَا يَرْجُونَ نُشُورًا
Romb nañu dëkk ba mbugal ma wàcce woon. Moo ndax gisuñu ko woon ? Ñoom kay dañoo foogoon ne duñu dekki !
41وَإِذَا رَأَوْكَ إِن يَتَّخِذُونَكَ إِلَّا هُزُوًا أَهَٰذَا الَّذِي بَعَثَ اللَّهُ رَسُولًا
Bu ñu la gisee dañu lay téjji naan : “Ndax kii la Yàlla yónni ?
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
39Aaya

Tekki — Al-Furqan 39

Simoore Al-Furqan Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ku nekk ci ñoom, sadd Nanu koy léebu, alag Nanu…

Simoore Aaya 39/77 — Simoore Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Furqan Dégg, Simoore Al-Furqan Tekki, Simoore Al-Furqan mp3, Simoore Al-Furqan pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers