Al-Furqan · 73/77
Tekki Waxtaan — Al-Furqan
وَالَّذِينَ إِذَا ذُكِّرُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ لَمْ يَخِرُّوا عَلَيْهَا صُمًّا وَعُمْيَانًا ۝٧٣
Wallazeena izaa zukkiroo bi Aayaati Rabbihim lam yakhirroo `alaihaa summanw wa`umyaanaa
📖 Tekkim Wolof
ña nga xam ne bu ñu déggee seen kàdduy Boroom, duñu ca tëx, duñu ca gumba ;

🎧 Dégg


📜 Aaya 71-75 — Al-Furqan

71وَمَن تَابَ وَعَمِلَ صَالِحًا فَإِنَّهُ يَتُوبُ إِلَى اللَّهِ مَتَابًا
képp kuy tuub [rëccu lu bon te bañ koo defati], dana dellu ca Yàlla mucc.
72وَالَّذِينَ لَا يَشْهَدُونَ الزُّورَ وَإِذَا مَرُّوا بِاللَّغْوِ مَرُّوا كِرَامًا
Ña nga xam ne duñu seede mukk aw fen ; te bu ñu rombee ay caaxaan duñu fa xand ;
73وَالَّذِينَ إِذَا ذُكِّرُوا بِآيَاتِ رَبِّهِمْ لَمْ يَخِرُّوا عَلَيْهَا صُمًّا وَعُمْيَانًا
ña nga xam ne bu ñu déggee seen kàdduy Boroom, duñu ca tëx, duñu ca gumba ;
74وَالَّذِينَ يَقُولُونَ رَبَّنَا هَبْ لَنَا مِنْ أَزْوَاجِنَا وَذُرِّيَّاتِنَا قُرَّةَ أَعْيُنٍ وَاجْعَلْنَا لِلْمُتَّقِينَ إِمَامًا
ña nga xam ne dañuy wax naan : “Yaw sunu Boroom, defal nu ci sunuy jabar ak sunuy doom ñuy seral xol, te nga def nu ay njiit ca ña ragal Yàlla tey wattandiku”.
75أُولَٰئِكَ يُجْزَوْنَ الْغُرْفَةَ بِمَا صَبَرُوا وَيُلَقَّوْنَ فِيهَا تَحِيَّةً وَسَلَامًا
Ñoom dees na leen feye ay néeg yu kawe [ca Àjjana], muy peyug la ñu doon muñ, te dees na leen fa teeroo ab nuyyoo ak jàmm [ju ne béyyi],
Al-FurqanFihi Alxuraan
77Aaya
MeccanRevelation
73Aaya

Tekki — Al-Furqan 73

Simoore Al-Furqan Aaya 73 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ña nga xam ne bu ñu déggee seen kàdduy Boroom,…

Simoore Aaya 73/77 — Al-Furqan الفرقان (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Furqan Dégg, Al-Furqan Tekki, Al-Furqan mp3, Al-Furqan pdf. Aaya 71–75. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, August 18, 2026

Don't forget us in your sincere prayers