Ash-Shu'ara · 141/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
كَذَّبَتْ ثَمُودُ الْمُرْسَلِينَ ۝١٤١
Kazzabat Samoodul mursaleen
📖 Tekkim Wolof
Waa Samuuda, weddi woon nañu Yonent ya.

🎧 Dégg


📜 Aaya 139-143 — Simoore Ash-Shu'ara

139فَكَذَّبُوهُ فَأَهْلَكْنَاهُمْ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَآيَةً ۖ وَمَا كَانَ أَكْثَرُهُم مُّؤْمِنِينَ
Ñu weddi ko. Nu daldi leen mbugal. Te ca biir, ay kéemaan a nga ca ! Te taxul la ëpp ca ñoom gëm.
140وَإِنَّ رَبَّكَ لَهُوَ الْعَزِيزُ الرَّحِيمُ
Te sa Boroom, moo di Boroom kàttan, di Jaglewaakoon.
141كَذَّبَتْ ثَمُودُ الْمُرْسَلِينَ
Waa Samuuda, weddi woon nañu Yonent ya.
142إِذْ قَالَ لَهُمْ أَخُوهُمْ صَالِحٌ أَلَا تَتَّقُونَ
Ba leen seen mbokk Saalihu waxee ne : “Moo ndax dungeen ragal Yàlla ? ”
143إِنِّي لَكُمْ رَسُولٌ أَمِينٌ
Man mii dey, ab Yonent laa ci yéen bu wóor.
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
141Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 141

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 141 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Waa Samuuda, weddi woon nañu Yonent ya.

Simoore Aaya 141/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 139–143. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 7, 2026

Don't forget us in your sincere prayers