Ash-Shu'ara · 227/227
Tekki Waxtaan — Simoore Ash-Shu'ara
إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَذَكَرُوا اللَّهَ كَثِيرًا وَانتَصَرُوا مِن بَعْدِ مَا ظُلِمُوا ۗ وَسَيَعْلَمُ الَّذِينَ ظَلَمُوا أَيَّ مُنقَلَبٍ يَنقَلِبُونَ ۝٢٢٧
Illal lazeena aamanoo w a`amilus saalihaati wa zakarul laaha kaseeranw wantasaroo mim ba`di maa zulimoo; wa saya`lamul lazeena zalamooo aiya munqalbiny yanqaliboon
📖 Tekkim Wolof
ba mu des woykat ya gëm, te jëf u yiw tey tudd lool Yàlla , ñuy sàkku ndam ci ginnaaw bu ñu leen tooñee. Tooñkat ya xalset nañoo xam naka la ñuy mujje!

🎧 Dégg


📜 Aaya 225-227 — Simoore Ash-Shu'ara

225أَلَمْ تَرَ أَنَّهُمْ فِي كُلِّ وَادٍ يَهِيمُونَ
Xanaa gisoo ne ñoom ci xur wu nekk la ñu fay wëndeelu,
226وَأَنَّهُمْ يَقُولُونَ مَا لَا يَفْعَلُونَ
Te it dañuy wax lu ñu dul def ?
227إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَذَكَرُوا اللَّهَ كَثِيرًا وَانتَصَرُوا مِن بَعْدِ مَا ظُلِمُوا ۗ وَسَيَعْلَمُ الَّذِينَ ظَلَمُوا أَيَّ مُنقَلَبٍ يَنقَلِبُونَ
ba mu des woykat ya gëm, te jëf u yiw tey tudd lool Yàlla , ñuy sàkku ndam ci ginnaaw bu ñu leen tooñee. Tooñkat ya xalset nañoo xam naka la ñuy mujje!
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
227Aaya

Tekki — Ash-Shu'ara 227

Simoore Ash-Shu'ara Aaya 227 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : ba mu des woykat ya gëm, te jëf u yiw…

Simoore Aaya 227/227 — Simoore Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Ash-Shu'ara Dégg, Simoore Ash-Shu'ara Tekki, Simoore Ash-Shu'ara mp3, Simoore Ash-Shu'ara pdf. Aaya 225–227. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers