Ash-Shu'ara · 226/227
Tekki Waxtaan — Ash-Shu'ara
وَأَنَّهُمْ يَقُولُونَ مَا لَا يَفْعَلُونَ ٢٢٦
Transliteration
Wa annahum yaqooloona ma laa yaf`aloon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Te it dañuy wax lu ñu dul def ?
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 224-227 — Ash-Shu'ara
224وَالشُّعَرَاءُ يَتَّبِعُهُمُ الْغَاوُونَ
Woykat ya nag, nitu mbalgas ya rekk a leen di topp.
225أَلَمْ تَرَ أَنَّهُمْ فِي كُلِّ وَادٍ يَهِيمُونَ
Xanaa gisoo ne ñoom ci xur wu nekk la ñu fay wëndeelu,
226وَأَنَّهُمْ يَقُولُونَ مَا لَا يَفْعَلُونَ
Te it dañuy wax lu ñu dul def ?
227إِلَّا الَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ وَذَكَرُوا اللَّهَ كَثِيرًا وَانتَصَرُوا مِن بَعْدِ مَا ظُلِمُوا ۗ وَسَيَعْلَمُ الَّذِينَ ظَلَمُوا أَيَّ مُنقَلَبٍ يَنقَلِبُونَ
ba mu des woykat ya gëm, te jëf u yiw tey tudd lool Yàlla , ñuy sàkku ndam ci ginnaaw bu ñu leen tooñee. Tooñkat ya xalset nañoo xam naka la ñuy mujje!
Ash-Shu'araFihi Alxuraan
227Aaya
MeccanRevelation
226Aaya
Tekki — Ash-Shu'ara 226
Simoore Ash-Shu'ara Aaya 226 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Te it dañuy wax lu ñu dul def ?Simoore Aaya 226/227 — Ash-Shu'ara الشعراء (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Ash-Shu'ara Dégg, Ash-Shu'ara Tekki, Ash-Shu'ara mp3, Ash-Shu'ara pdf. Aaya 224–227. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








