An-Naml · 14/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
وَجَحَدُوا بِهَا وَاسْتَيْقَنَتْهَا أَنفُسُهُمْ ظُلْمًا وَعُلُوًّا ۚ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُفْسِدِينَ ۝١٤
Wa jahadoo bihaa wastaiqanat haaa anfusuhum zulmanw-wa `uluwwaa; fanzur kaifa kaana `aaqibatul mufsideen
📖 Tekkim Wolof
Weddi nañu ko waaye seeni xol gëm na ko, xanaa kay rëy a leen jàpp. Xoolal nag yàqkat naka la ñuy mujje.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 12-16 — Simoore An-Naml

12وَأَدْخِلْ يَدَكَ فِي جَيْبِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ ۖ فِي تِسْعِ آيَاتٍ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَقَوْمِهِ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Sóobal sa loxo ci sa mbubbu. Dana génn weex tàll - muy benn ci juróom-ñeenti kéemaan yi jëm ca Firawna ak u nitam, ñoom ay saay-saay lañu woon”.
13فَلَمَّا جَاءَتْهُمْ آيَاتُنَا مُبْصِرَةً قَالُوا هَٰذَا سِحْرٌ مُّبِينٌ
Ndax ba leen Sunuy laaya dikkalee, leer nàññ, dañoo wax ne : “Lii ag njibar la gu bir ! ”
14وَجَحَدُوا بِهَا وَاسْتَيْقَنَتْهَا أَنفُسُهُمْ ظُلْمًا وَعُلُوًّا ۚ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الْمُفْسِدِينَ
Weddi nañu ko waaye seeni xol gëm na ko, xanaa kay rëy a leen jàpp. Xoolal nag yàqkat naka la ñuy mujje.
15وَلَقَدْ آتَيْنَا دَاوُودَ وَسُلَيْمَانَ عِلْمًا ۖ وَقَالَا الْحَمْدُ لِلَّهِ الَّذِي فَضَّلَنَا عَلَىٰ كَثِيرٍ مِّنْ عِبَادِهِ الْمُؤْمِنِينَ
Joxoon Nanu Daawuda ak Suleymaan xam-xam ; ñuy wax naan : “Xeeti cant yépp ñeel na Yàlla, Moom mi nu gënal ci kaw nit ñu bari ñi bokkoon ci jaamam ñi gëm”.
16وَوَرِثَ سُلَيْمَانُ دَاوُودَ ۖ وَقَالَ يَا أَيُّهَا النَّاسُ عُلِّمْنَا مَنطِقَ الطَّيْرِ وَأُوتِينَا مِن كُلِّ شَيْءٍ ۖ إِنَّ هَٰذَا لَهُوَ الْفَضْلُ الْمُبِينُ
Suleymaan wuutu na Daawuda, daldi ne : “Éy yéen nit ñi ! Xam naa waxi picc yi ; te am naa lu ne. Loolu mooy ngëneel lu bir.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
14Aaya

Tekki — An-Naml 14

Simoore An-Naml Aaya 14 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Weddi nañu ko waaye seeni xol gëm na ko, xanaa…

Simoore Aaya 14/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 12–16. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers