An-Naml · 38/93
Tekki Waxtaan — Simoore An-Naml
قَالَ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ أَيُّكُمْ يَأْتِينِي بِعَرْشِهَا قَبْلَ أَن يَأْتُونِي مُسْلِمِينَ ٣٨
Transliteration
Qaala yaaa aiyuhal mala`u aiyukum yaateenee bi`arshihaa qabla ai yaatoonee muslimeen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Suleymaan ne : "Yéen kilifa yi ! Ana kan moo may indil gàngunaayam ba la ñoo agsi di jébbalesi seen bopp ? ”
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 36-40 — Simoore An-Naml
36فَلَمَّا جَاءَ سُلَيْمَانَ قَالَ أَتُمِدُّونَنِ بِمَالٍ فَمَا آتَانِيَ اللَّهُ خَيْرٌ مِّمَّا آتَاكُم بَلْ أَنتُم بِهَدِيَّتِكُمْ تَفْرَحُونَ
[Ba ndaw ya àggee] ca Suleymaan, mu ne leen : “Yéen daal dangeen may jéem a gere alal ? Maa leen ko gënle fuuf. Mbaa du ! Lii doŋŋ la.
37ارْجِعْ إِلَيْهِمْ فَلَنَأْتِيَنَّهُم بِجُنُودٍ لَّا قِبَلَ لَهُم بِهَا وَلَنُخْرِجَنَّهُم مِّنْهَا أَذِلَّةً وَهُمْ صَاغِرُونَ
Dellul ca ñoom. Neleen danaa leen indil xare bu ñu dul mën a dékku. Te danaa leen fa génne toroxal leen ba ñu ne tott.
38قَالَ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ أَيُّكُمْ يَأْتِينِي بِعَرْشِهَا قَبْلَ أَن يَأْتُونِي مُسْلِمِينَ
Suleymaan ne : "Yéen kilifa yi ! Ana kan moo may indil gàngunaayam ba la ñoo agsi di jébbalesi seen bopp ? ”
39قَالَ عِفْرِيتٌ مِّنَ الْجِنِّ أَنَا آتِيكَ بِهِ قَبْلَ أَن تَقُومَ مِن مَّقَامِكَ ۖ وَإِنِّي عَلَيْهِ لَقَوِيٌّ أَمِينٌ
Mu am jinne ju ne ko : “Mën naa la koo indil bala ngaa jóge fii nga toog : Mën naa ko te wóor na”.
40قَالَ الَّذِي عِندَهُ عِلْمٌ مِّنَ الْكِتَابِ أَنَا آتِيكَ بِهِ قَبْلَ أَن يَرْتَدَّ إِلَيْكَ طَرْفُكَ ۚ فَلَمَّا رَآهُ مُسْتَقِرًّا عِندَهُ قَالَ هَٰذَا مِن فَضْلِ رَبِّي لِيَبْلُوَنِي أَأَشْكُرُ أَمْ أَكْفُرُ ۖ وَمَن شَكَرَ فَإِنَّمَا يَشْكُرُ لِنَفْسِهِ ۖ وَمَن كَفَرَ فَإِنَّ رَبِّي غَنِيٌّ كَرِيمٌ
Ka ame woon xam-xamu Téere ba ne ko : “Mën naa la koo indil ba la ngaa xef”. [Ne ko mingi nii] , ba ko Suleymaan gisee ci kanamam, dafa wax ne : “Lii dey ngënéelul sama Boroom bi la. Dama ciy nattu ndax damay sant walla damay xarab... képp kuy sant yaw caak, ku weddi nag, sama Boroom moom di Ku doylu, di Ku tedd”.
An-NamlFihi Alxuraan
93Aaya
MeccanRevelation
38Aaya
Tekki — An-Naml 38
Simoore An-Naml Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Suleymaan ne : "Yéen kilifa yi ! Ana kan moo…Simoore Aaya 38/93 — Simoore An-Naml النمل (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore An-Naml Dégg, Simoore An-Naml Tekki, Simoore An-Naml mp3, Simoore An-Naml pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, September 8, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








