Al-Qasas · 30/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
فَلَمَّا أَتَاهَا نُودِيَ مِن شَاطِئِ الْوَادِ الْأَيْمَنِ فِي الْبُقْعَةِ الْمُبَارَكَةِ مِنَ الشَّجَرَةِ أَن يَا مُوسَىٰ إِنِّي أَنَا اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ ۝٣٠
Falammaaa ataahaa noodiya min shaati`il waadil aimani fil buq`atil muubaarakati minash shajarati ai yaa Moosaaa inneee Anal laahu Rabbul `aalameen
📖 Tekkim Wolof
Ba mu fa agsee, mu am lu ko woo ci xuru ndeyjoor wa, ne ko : “Éy Muusaa ! ManMii Maa di Yàlla jiy Boroom àddina si yépp”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 28-32 — Simoore Al-Qasas

28قَالَ ذَٰلِكَ بَيْنِي وَبَيْنَكَ ۖ أَيَّمَا الْأَجَلَيْنِ قَضَيْتُ فَلَا عُدْوَانَ عَلَيَّ ۖ وَاللَّهُ عَلَىٰ مَا نَقُولُ وَكِيلٌ
Mu daldi ne : “Loolu sama diggante la ak yaw. Ñaar ñépp a yem ci man, duma la bunduxataal mukk. Te lii nuy wax Yàllaa di seede si”.
29۞ فَلَمَّا قَضَىٰ مُوسَى الْأَجَلَ وَسَارَ بِأَهْلِهِ آنَسَ مِن جَانِبِ الطُّورِ نَارًا قَالَ لِأَهْلِهِ امْكُثُوا إِنِّي آنَسْتُ نَارًا لَّعَلِّي آتِيكُم مِّنْهَا بِخَبَرٍ أَوْ جَذْوَةٍ مِّنَ النَّارِ لَعَلَّكُمْ تَصْطَلُونَ
Ba Muusaa matalee dig ba, màng njabootam di ñibbi, gis na safara ci wàllug ndeyjooru tundu doju Tuur wa. Mu ne leen : “Xaarleen ma fii, li ma séen aw safara la. Amaana ma indil leen ci xibaar walla ay xal ngir ngeen mën caa jaaroo”.
30فَلَمَّا أَتَاهَا نُودِيَ مِن شَاطِئِ الْوَادِ الْأَيْمَنِ فِي الْبُقْعَةِ الْمُبَارَكَةِ مِنَ الشَّجَرَةِ أَن يَا مُوسَىٰ إِنِّي أَنَا اللَّهُ رَبُّ الْعَالَمِينَ
Ba mu fa agsee, mu am lu ko woo ci xuru ndeyjoor wa, ne ko : “Éy Muusaa ! ManMii Maa di Yàlla jiy Boroom àddina si yépp”.
31وَأَنْ أَلْقِ عَصَاكَ ۖ فَلَمَّا رَآهَا تَهْتَزُّ كَأَنَّهَا جَانٌّ وَلَّىٰ مُدْبِرًا وَلَمْ يُعَقِّبْ ۚ يَا مُوسَىٰ أَقْبِلْ وَلَا تَخَفْ ۖ إِنَّكَ مِنَ الْآمِنِينَ
Te : “Nanga sànni sa yet wi” ; [Ba mu ko sànnee] gis ne ma ngay yëngatu mel ni jaan, mu ne baxarñit.”. Yàlla woowaat ko, ne ko : “Dellusil te bul tiit : yaa ngi ci lu wóor”.
32اسْلُكْ يَدَكَ فِي جَيْبِكَ تَخْرُجْ بَيْضَاءَ مِنْ غَيْرِ سُوءٍ وَاضْمُمْ إِلَيْكَ جَنَاحَكَ مِنَ الرَّهْبِ ۖ فَذَانِكَ بُرْهَانَانِ مِن رَّبِّكَ إِلَىٰ فِرْعَوْنَ وَمَلَئِهِ ۚ إِنَّهُمْ كَانُوا قَوْمًا فَاسِقِينَ
Sóobal sa loxo ci sa mbagg, dina génn weex tàll. Te nanga taf sa loxo bi ci sa kaw ngir bañ a tiit. Yooyu yaari mbir ay firnde la yu bawoo ca sa Boroom Mu jëme ko ci Firawna ak gàngooram. Ñoom ay saay-saay lañu”.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
30Aaya

Tekki — Al-Qasas 30

Simoore Al-Qasas Aaya 30 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ba mu fa agsee, mu am lu ko woo ci…

Simoore Aaya 30/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 28–32. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers