Al-Qasas · 38/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
وَقَالَ فِرْعَوْنُ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ مَا عَلِمْتُ لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرِي فَأَوْقِدْ لِي يَا هَامَانُ عَلَى الطِّينِ فَاجْعَل لِّي صَرْحًا لَّعَلِّي أَطَّلِعُ إِلَىٰ إِلَٰهِ مُوسَىٰ وَإِنِّي لَأَظُنُّهُ مِنَ الْكَاذِبِينَ ۝٣٨
Wa qaala Fir`awnu yaaa aiyuhal mala-u maa `alimtu lakum min ilaahin ghairee fa awqid lee yaa Haamaanu `alatteeni faj`al lee sarhal la`alleee attali`u ilaaa ilaahi Moosaa wa innee la azunnuhoo minal kaazibeen
📖 Tekkim Wolof
Firawna daldi wax ne : "Éy yéen kilifa yi, xamaluma leen jeneen Yàlla ju dul man. Yaw Haamaan, taalal ma aw safara ci ban bi te tabaxal ma ag tóoj ndax ma mën cee yërndu Yàllay Muusaa ji. Te man sax njortu naa ne ci fenkat yi la bokk”.

🎧 Dégg


📜 Aaya 36-40 — Simoore Al-Qasas

36فَلَمَّا جَاءَهُم مُّوسَىٰ بِآيَاتِنَا بَيِّنَاتٍ قَالُوا مَا هَٰذَا إِلَّا سِحْرٌ مُّفْتَرًى وَمَا سَمِعْنَا بِهَٰذَا فِي آبَائِنَا الْأَوَّلِينَ
Ba leen Muusaa dikkee, indil leen Sunuy kàddu yu leer ñàññ, wax nañu ne : “Lii daal du lenn du dul ag njibar gu ñu sos, te sax nun lii mësunu leen woon a dégg ca sunuy maam”.
37وَقَالَ مُوسَىٰ رَبِّي أَعْلَمُ بِمَن جَاءَ بِالْهُدَىٰ مِنْ عِندِهِ وَمَن تَكُونُ لَهُ عَاقِبَةُ الدَّارِ ۖ إِنَّهُ لَا يُفْلِحُ الظَّالِمُونَ
Muusaa ne leen : “Sama Boroom moo gën a xam ana kaan moo indi dëgg te jóge fa Moom, ak kan mooy ëppug mujj. Tooñkat ya duñu texe de”.
38وَقَالَ فِرْعَوْنُ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ مَا عَلِمْتُ لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرِي فَأَوْقِدْ لِي يَا هَامَانُ عَلَى الطِّينِ فَاجْعَل لِّي صَرْحًا لَّعَلِّي أَطَّلِعُ إِلَىٰ إِلَٰهِ مُوسَىٰ وَإِنِّي لَأَظُنُّهُ مِنَ الْكَاذِبِينَ
Firawna daldi wax ne : "Éy yéen kilifa yi, xamaluma leen jeneen Yàlla ju dul man. Yaw Haamaan, taalal ma aw safara ci ban bi te tabaxal ma ag tóoj ndax ma mën cee yërndu Yàllay Muusaa ji. Te man sax njortu naa ne ci fenkat yi la bokk”.
39وَاسْتَكْبَرَ هُوَ وَجُنُودُهُ فِي الْأَرْضِ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَظَنُّوا أَنَّهُمْ إِلَيْنَا لَا يُرْجَعُونَ
Muy rëy-rëylu mook i xarekatam ci réew mi ci lu dul dëgg. Ñu foogoon ne duñu dellusi ci Nun.
40فَأَخَذْنَاهُ وَجُنُودَهُ فَنَبَذْنَاهُمْ فِي الْيَمِّ ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الظَّالِمِينَ
Nu jël ko mook i xarekatam nargan leen ca ndox ma. Xoolal mujjug tooñkat ya.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
38Aaya

Tekki — Al-Qasas 38

Simoore Al-Qasas Aaya 38 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Firawna daldi wax ne : "Éy yéen kilifa yi, xamaluma…

Simoore Aaya 38/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 36–40. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers