Al-Qasas · 39/88
Tekki Waxtaan — Al-Qasas
وَاسْتَكْبَرَ هُوَ وَجُنُودُهُ فِي الْأَرْضِ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَظَنُّوا أَنَّهُمْ إِلَيْنَا لَا يُرْجَعُونَ ٣٩
Transliteration
Wastakbara huwa wa junooduhoo fil ardi bighairil haqqi wa zannooo annahum ilainaa laa yurja`oon
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Muy rëy-rëylu mook i xarekatam ci réew mi ci lu dul dëgg. Ñu foogoon ne duñu dellusi ci Nun.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 37-41 — Al-Qasas
37وَقَالَ مُوسَىٰ رَبِّي أَعْلَمُ بِمَن جَاءَ بِالْهُدَىٰ مِنْ عِندِهِ وَمَن تَكُونُ لَهُ عَاقِبَةُ الدَّارِ ۖ إِنَّهُ لَا يُفْلِحُ الظَّالِمُونَ
Muusaa ne leen : “Sama Boroom moo gën a xam ana kaan moo indi dëgg te jóge fa Moom, ak kan mooy ëppug mujj. Tooñkat ya duñu texe de”.
38وَقَالَ فِرْعَوْنُ يَا أَيُّهَا الْمَلَأُ مَا عَلِمْتُ لَكُم مِّنْ إِلَٰهٍ غَيْرِي فَأَوْقِدْ لِي يَا هَامَانُ عَلَى الطِّينِ فَاجْعَل لِّي صَرْحًا لَّعَلِّي أَطَّلِعُ إِلَىٰ إِلَٰهِ مُوسَىٰ وَإِنِّي لَأَظُنُّهُ مِنَ الْكَاذِبِينَ
Firawna daldi wax ne : "Éy yéen kilifa yi, xamaluma leen jeneen Yàlla ju dul man. Yaw Haamaan, taalal ma aw safara ci ban bi te tabaxal ma ag tóoj ndax ma mën cee yërndu Yàllay Muusaa ji. Te man sax njortu naa ne ci fenkat yi la bokk”.
39وَاسْتَكْبَرَ هُوَ وَجُنُودُهُ فِي الْأَرْضِ بِغَيْرِ الْحَقِّ وَظَنُّوا أَنَّهُمْ إِلَيْنَا لَا يُرْجَعُونَ
Muy rëy-rëylu mook i xarekatam ci réew mi ci lu dul dëgg. Ñu foogoon ne duñu dellusi ci Nun.
40فَأَخَذْنَاهُ وَجُنُودَهُ فَنَبَذْنَاهُمْ فِي الْيَمِّ ۖ فَانظُرْ كَيْفَ كَانَ عَاقِبَةُ الظَّالِمِينَ
Nu jël ko mook i xarekatam nargan leen ca ndox ma. Xoolal mujjug tooñkat ya.
41وَجَعَلْنَاهُمْ أَئِمَّةً يَدْعُونَ إِلَى النَّارِ ۖ وَيَوْمَ الْقِيَامَةِ لَا يُنصَرُونَ
Defoon Nanu leen ay njiit yuy woote jëme Safara. Te bu Bis-pénc baa kenn duleen dimbali.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
39Aaya
Tekki — Al-Qasas 39
Simoore Al-Qasas Aaya 39 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Muy rëy-rëylu mook i xarekatam ci réew mi ci lu…Simoore Aaya 39/88 — Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-Qasas Dégg, Al-Qasas Tekki, Al-Qasas mp3, Al-Qasas pdf. Aaya 37–41. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








