Al-Qasas · 51/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
۞ وَلَقَدْ وَصَّلْنَا لَهُمُ الْقَوْلَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ ۝٥١
Wa laqad wassalnaa lahumul qawla la`allahum yatazakkaroon
📖 Tekkim Wolof
Jottali Nanu leen wax jii [Alxuraan] ngir ñu fàttaliku ca.

🎧 Dégg


📜 Aaya 49-53 — Simoore Al-Qasas

49قُلْ فَأْتُوا بِكِتَابٍ مِّنْ عِندِ اللَّهِ هُوَ أَهْدَىٰ مِنْهُمَا أَتَّبِعْهُ إِن كُنتُمْ صَادِقِينَ
Neel : “Indileen ab Téere bu jóge ca Yàlla bu leen gën a mën a jubbanti, [su ngeen ko indee] kon danaa ko topp, su ngeen waxee dëgg ”.
50فَإِن لَّمْ يَسْتَجِيبُوا لَكَ فَاعْلَمْ أَنَّمَا يَتَّبِعُونَ أَهْوَاءَهُمْ ۚ وَمَنْ أَضَلُّ مِمَّنِ اتَّبَعَ هَوَاهُ بِغَيْرِ هُدًى مِّنَ اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
Bu ñu la wuyuwul nag, xamal ne seen bakkan lañuy topp. Te ana kan moo gën a sànku ci kuy topp bakkanam ci lu àndul ak njub ga bawoo ca Yàlla [Lislaam]? Yàlla du gindi aw nit yuy tooñ.
51۞ وَلَقَدْ وَصَّلْنَا لَهُمُ الْقَوْلَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Jottali Nanu leen wax jii [Alxuraan] ngir ñu fàttaliku ca.
52الَّذِينَ آتَيْنَاهُمُ الْكِتَابَ مِن قَبْلِهِ هُم بِهِ يُؤْمِنُونَ
Ña nga xam ne joxoon Nanu leen Téere lu jiitu Alxuraan, gëm nañu ko.
53وَإِذَا يُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ قَالُوا آمَنَّا بِهِ إِنَّهُ الْحَقُّ مِن رَّبِّنَا إِنَّا كُنَّا مِن قَبْلِهِ مُسْلِمِينَ
Te bunu leen ko mësaan a jàngal, dañu daan wax ne : “Gëm nanu ko. Te mooy dëgg ga jóge ca sunu Boroom. Faf nun jébbalu nanu ba mu laataa na ñëw”.
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Al-Qasas 51

Simoore Al-Qasas Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Jottali Nanu leen wax jii [Alxuraan] ngir ñu fàttaliku ca.

Simoore Aaya 51/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Monday, September 21, 2026

Don't forget us in your sincere prayers