Al-Qasas · 52/88
Tekki Waxtaan — Simoore Al-Qasas
الَّذِينَ آتَيْنَاهُمُ الْكِتَابَ مِن قَبْلِهِ هُم بِهِ يُؤْمِنُونَ ۝٥٢
Allazeena aatainaahu mul Kitaaba min qablihee hum bihee yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Ña nga xam ne joxoon Nanu leen Téere lu jiitu Alxuraan, gëm nañu ko.

🎧 Dégg


📜 Aaya 50-54 — Simoore Al-Qasas

50فَإِن لَّمْ يَسْتَجِيبُوا لَكَ فَاعْلَمْ أَنَّمَا يَتَّبِعُونَ أَهْوَاءَهُمْ ۚ وَمَنْ أَضَلُّ مِمَّنِ اتَّبَعَ هَوَاهُ بِغَيْرِ هُدًى مِّنَ اللَّهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يَهْدِي الْقَوْمَ الظَّالِمِينَ
Bu ñu la wuyuwul nag, xamal ne seen bakkan lañuy topp. Te ana kan moo gën a sànku ci kuy topp bakkanam ci lu àndul ak njub ga bawoo ca Yàlla [Lislaam]? Yàlla du gindi aw nit yuy tooñ.
51۞ وَلَقَدْ وَصَّلْنَا لَهُمُ الْقَوْلَ لَعَلَّهُمْ يَتَذَكَّرُونَ
Jottali Nanu leen wax jii [Alxuraan] ngir ñu fàttaliku ca.
52الَّذِينَ آتَيْنَاهُمُ الْكِتَابَ مِن قَبْلِهِ هُم بِهِ يُؤْمِنُونَ
Ña nga xam ne joxoon Nanu leen Téere lu jiitu Alxuraan, gëm nañu ko.
53وَإِذَا يُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ قَالُوا آمَنَّا بِهِ إِنَّهُ الْحَقُّ مِن رَّبِّنَا إِنَّا كُنَّا مِن قَبْلِهِ مُسْلِمِينَ
Te bunu leen ko mësaan a jàngal, dañu daan wax ne : “Gëm nanu ko. Te mooy dëgg ga jóge ca sunu Boroom. Faf nun jébbalu nanu ba mu laataa na ñëw”.
54أُولَٰئِكَ يُؤْتَوْنَ أَجْرَهُم مَّرَّتَيْنِ بِمَا صَبَرُوا وَيَدْرَءُونَ بِالْحَسَنَةِ السَّيِّئَةَ وَمِمَّا رَزَقْنَاهُمْ يُنفِقُونَ
Ñooña danañu seen pey ñaari yoon ca la ñu daan muñ, daan toontoo aw ñaawtéef ak lu rafet, te di joxe ca la Ma leen wërsëgal ;
Al-QasasFihi Alxuraan
88Aaya
MeccanRevelation
52Aaya

Tekki — Al-Qasas 52

Simoore Al-Qasas Aaya 52 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña nga xam ne joxoon Nanu leen Téere lu jiitu…

Simoore Aaya 52/88 — Simoore Al-Qasas القصص (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-Qasas Dégg, Simoore Al-Qasas Tekki, Simoore Al-Qasas mp3, Simoore Al-Qasas pdf. Aaya 50–54. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers