Al-'Ankabut · 51/69
Tekki Waxtaan — Simoore Al-'Ankabut
أَوَلَمْ يَكْفِهِمْ أَنَّا أَنزَلْنَا عَلَيْكَ الْكِتَابَ يُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَرَحْمَةً وَذِكْرَىٰ لِقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ ۝٥١
Awa lam yakfihim annaaa anzalnaa `alaikal kitaaba yutlaa `alaikhim; inna fee zaalika larahmatanw wa zikraa liqawminy yu`minoon
📖 Tekkim Wolof
Ndax doyuleen ñoom, wàcce gii Nu wàcce ci yaw Téere bi, Nu di leen ko dégtal ? Yërmaande ak fàttalikoo nga ca biir lool ngir aw nit ñu gëm.

M Mishary Rashid Alafasy ✓
M Mahmoud Khalil Al-Husary ✓
A Abdurrahman As-Sudais ✓
M Mohamed Siddiq Al-Minshawi ✓
A Abdul Basit Abdul Samad ✓
A Ali Al-Hudhaify ✓
A Ahmed ibn Ali al-Ajamy ✓
A Abu Bakr Ash-Shaatree ✓
M Muhammad Ayyoub ✓
A Abdullah Basfar ✓
A Abdullah Al-Juhani ✓
M Maher Al Muaiqly ✓
0:00
0:00


📜 Aaya 49-53 — Simoore Al-'Ankabut

49بَلْ هُوَ آيَاتٌ بَيِّنَاتٌ فِي صُدُورِ الَّذِينَ أُوتُوا الْعِلْمَ ۚ وَمَا يَجْحَدُ بِآيَاتِنَا إِلَّا الظَّالِمُونَ
Li wér te wóor moo di ne, [Alxuraan] ay laaya la yu ñu faramfàcce ci biir dënni woroom xam-xam yi. Te tooñkat yi rekk ñoo koy weddi.
50وَقَالُوا لَوْلَا أُنزِلَ عَلَيْهِ آيَاتٌ مِّن رَّبِّهِ ۖ قُلْ إِنَّمَا الْآيَاتُ عِندَ اللَّهِ وَإِنَّمَا أَنَا نَذِيرٌ مُّبِينٌ
Ñuy wax naan : “Lu tax Yàlla wàccewul ci moom kéemaan ? ”. Waxal ne : “Kéemaan a nga ca Yàlla. Man, ab xuppekat buy leeral rekk laa”.
51أَوَلَمْ يَكْفِهِمْ أَنَّا أَنزَلْنَا عَلَيْكَ الْكِتَابَ يُتْلَىٰ عَلَيْهِمْ ۚ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَرَحْمَةً وَذِكْرَىٰ لِقَوْمٍ يُؤْمِنُونَ
Ndax doyuleen ñoom, wàcce gii Nu wàcce ci yaw Téere bi, Nu di leen ko dégtal ? Yërmaande ak fàttalikoo nga ca biir lool ngir aw nit ñu gëm.
52قُلْ كَفَىٰ بِاللَّهِ بَيْنِي وَبَيْنَكُمْ شَهِيدًا ۖ يَعْلَمُ مَا فِي السَّمَاوَاتِ وَالْأَرْضِ ۗ وَالَّذِينَ آمَنُوا بِالْبَاطِلِ وَكَفَرُوا بِاللَّهِ أُولَٰئِكَ هُمُ الْخَاسِرُونَ
Waxal ne : “Yàlla doy na seede sama digganteek yéen”. Xam na li nekk ci asamaan yeek suuf si. Ña gëm neen, weddi Yàlla, ñoo yàqule.
53وَيَسْتَعْجِلُونَكَ بِالْعَذَابِ ۚ وَلَوْلَا أَجَلٌ مُّسَمًّى لَّجَاءَهُمُ الْعَذَابُ وَلَيَأْتِيَنَّهُم بَغْتَةً وَهُمْ لَا يَشْعُرُونَ
Té ñanga lay laaj mbugal ma cig yàkkamti. Bu fekkoon ne du dig ba Nu leen àppal, kon ñëwoon na [bu yàgg]. Waaye mbugal ma dana ñëw ci ñoom, di mbetteel te duñu ko yég.
Al-'AnkabutFihi Alxuraan
69Aaya
MeccanRevelation
51Aaya

Tekki — Al-'Ankabut 51

Simoore Al-'Ankabut Aaya 51 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ndax doyuleen ñoom, wàcce gii Nu wàcce ci yaw Téere…

Simoore Aaya 51/69 — Simoore Al-'Ankabut العنكبوت (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Al-'Ankabut Dégg, Simoore Al-'Ankabut Tekki, Simoore Al-'Ankabut mp3, Simoore Al-'Ankabut pdf. Aaya 49–53. Tekkim Wolof: Fulfulde.





Alxuraan bu Tedd bi


Friday, October 2, 2026

Don't forget us in your sincere prayers