Al-'Ankabut · 6/69
Tekki Waxtaan — Al-'Ankabut
وَمَن جَاهَدَ فَإِنَّمَا يُجَاهِدُ لِنَفْسِهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَغَنِيٌّ عَنِ الْعَالَمِينَ ٦
Transliteration
Wa man jaahada fainnamaa yujaahidu linafsih; innal laaha laghaniyyun `anil `aalameen
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
Képp kuy xare, boppam la koy defal, Yàlla ku doylu la ci waa àddina bi yépp.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 4-8 — Al-'Ankabut
4أَمْ حَسِبَ الَّذِينَ يَعْمَلُونَ السَّيِّئَاتِ أَن يَسْبِقُونَا ۚ سَاءَ مَا يَحْكُمُونَ
Walla ñay jëfi ñaawteef, jàpp nañu ne danañu Nu jiitu ? Aka ñoo ñaaw ab àtte !
5مَن كَانَ يَرْجُو لِقَاءَ اللَّهِ فَإِنَّ أَجَلَ اللَّهِ لَآتٍ ۚ وَهُوَ السَّمِيعُ الْعَلِيمُ
Képp kuy yaakaar a dajeek Yàlla, digub Yàlla boobu luy dikk la. Te Mooy dégg, di xam.
6وَمَن جَاهَدَ فَإِنَّمَا يُجَاهِدُ لِنَفْسِهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَغَنِيٌّ عَنِ الْعَالَمِينَ
Képp kuy xare, boppam la koy defal, Yàlla ku doylu la ci waa àddina bi yépp.
7وَالَّذِينَ آمَنُوا وَعَمِلُوا الصَّالِحَاتِ لَنُكَفِّرَنَّ عَنْهُمْ سَيِّئَاتِهِمْ وَلَنَجْزِيَنَّهُمْ أَحْسَنَ الَّذِي كَانُوا يَعْمَلُونَ
Ñi gëm tey jëf u yiw, Dananu leen faral seeni ñaawteef, te Dananu leen feye ca la gën ca la ñu daan def.
8وَوَصَّيْنَا الْإِنسَانَ بِوَالِدَيْهِ حُسْنًا ۖ وَإِن جَاهَدَاكَ لِتُشْرِكَ بِي مَا لَيْسَ لَكَ بِهِ عِلْمٌ فَلَا تُطِعْهُمَا ۚ إِلَيَّ مَرْجِعُكُمْ فَأُنَبِّئُكُم بِمَا كُنتُمْ تَعْمَلُونَ
Dénk Nanu nit muy def yiw ciy ñaari way-juram, “bu ñu la sonnalee nag ci bëgg nga bokkaale Ma ak loo xamul, buleen ca topp”. Ci Man ngeen di dellusi, Ma xibaar leen la ngeen daan def.
Al-'AnkabutFihi Alxuraan
69Aaya
MeccanRevelation
6Aaya
Tekki — Al-'Ankabut 6
Simoore Al-'Ankabut Aaya 6 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Képp kuy xare, boppam la koy defal, Yàlla ku doylu…Simoore Aaya 6/69 — Al-'Ankabut العنكبوت (Meccan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Al-'Ankabut Dégg, Al-'Ankabut Tekki, Al-'Ankabut mp3, Al-'Ankabut pdf. Aaya 4–8. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








