Aali Imran · 11/200
Tekki Waxtaan — Aali Imran
كَدَأْبِ آلِ فِرْعَوْنَ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا فَأَخَذَهُمُ اللَّهُ بِذُنُوبِهِمْ ۗ وَاللَّهُ شَدِيدُ الْعِقَابِ ١١
Transliteration
Kadaabi Aali Fir`awna wallazeena min qablihim; kazzaboo bi Aayaatinaa fa akhazahumul laahu bizunoo bihim; wallaahu shadeedul `iqaab
Tekki (Tekkim Wolof)
📖 Tekkim Wolof
lu mel ni aadaay nitu Firawna ak ña leen jiitu woon, weddi woon Sunuy laaya. Yàlla jàppe leen seeni bàkkaar. Te Yàlla di ku tar mbugal.
Additional reference in Fulfulde
🎧 Dégg
📜 Aaya 9-13 — Aali Imran
9رَبَّنَا إِنَّكَ جَامِعُ النَّاسِ لِيَوْمٍ لَّا رَيْبَ فِيهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُخْلِفُ الْمِيعَادَ
Sunu Boroom ! Yaw yaa di dajale nit ñi ci bis boo xam ne - sikk nekkul ci ag ñëwam - Yàlla, du wuute dige ba.
10إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا لَن تُغْنِيَ عَنْهُمْ أَمْوَالُهُمْ وَلَا أَوْلَادُهُم مِّنَ اللَّهِ شَيْئًا ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمْ وَقُودُ النَّارِ
Ña weddi, seen alal ya ak seen njaboot ya duleen fegal dara ca Yàlla. Te ñoom ñoo di mattum Safara,
11كَدَأْبِ آلِ فِرْعَوْنَ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا فَأَخَذَهُمُ اللَّهُ بِذُنُوبِهِمْ ۗ وَاللَّهُ شَدِيدُ الْعِقَابِ
lu mel ni aadaay nitu Firawna ak ña leen jiitu woon, weddi woon Sunuy laaya. Yàlla jàppe leen seeni bàkkaar. Te Yàlla di ku tar mbugal.
12قُل لِّلَّذِينَ كَفَرُوا سَتُغْلَبُونَ وَتُحْشَرُونَ إِلَىٰ جَهَنَّمَ ۚ وَبِئْسَ الْمِهَادُ
Waxal ña weddi [ca Yahuud ya] ne : “Dees na leen not ; pang leen jëme Safara. Te [lal ba ñu fay fekk] bon na ! ”
13قَدْ كَانَ لَكُمْ آيَةٌ فِي فِئَتَيْنِ الْتَقَتَا ۖ فِئَةٌ تُقَاتِلُ فِي سَبِيلِ اللَّهِ وَأُخْرَىٰ كَافِرَةٌ يَرَوْنَهُم مِّثْلَيْهِمْ رَأْيَ الْعَيْنِ ۚ وَاللَّهُ يُؤَيِّدُ بِنَصْرِهِ مَن يَشَاءُ ۗ إِنَّ فِي ذَٰلِكَ لَعِبْرَةً لِّأُولِي الْأَبْصَارِ
Am ngeen lu waare ci ñaari mbooloo ya [ca Badar] la ñu daj : muy di xeex ci yoonu Yàlla ; meneen ma, di ay yéefar. Mu jullit ma gis ne ñaari yoon la leen yéefar ya ëppee, ci gisu bët rekk. Fekk ëpp na sax loolu. Yàlla dana dooleel ci ndimbalam ku ko soob. Lii nag doy sëkk ag waare ca ña ame gët [xel] !
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
11Aaya
Tekki — Aali Imran 11
Simoore Aali Imran Aaya 11 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : lu mel ni aadaay nitu Firawna ak ña leen jiitu…Simoore Aaya 11/200 — Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Aali Imran Dégg, Aali Imran Tekki, Aali Imran mp3, Aali Imran pdf. Aaya 9–13. Tekkim Wolof: Fulfulde.
العربية
English
Bahasa Indonesia
Türkçe
Русский
فارسی
Français
اردو
বাংলা
Deutsch
Español
中文
हिन्दी
Português
Italiano
ภาษาไทย
Polski
Nederlands
Shqip
Kiswahili
O'zbek
தமிழ்
Melayu
Bosanski
Soomaali
Azərbaycan
کوردی
한국어
日本語
Svenska
Dansk
Norsk
پښتو
മലയാളം
සිංහල
Tamazight
Hausa
አማርኛ
Български
Тоҷикӣ
Қазақша
Filipino
سنڌي
Yorùbá
Fulfulde
Татарча
ئۇيغۇرچە
Кыргызча
ਪੰਜਾਬੀ
Jawa
తెలుగు
မြန်မာ
ગુજરાતી
Oromo
मराठी
Tiếng Việt
Malagasy
Нохчийн
Wolof
ދިވެހި
ಕನ್ನಡ
Українська
Ελληνικά
ქართული
ខ្មែរ
دری
Qafar af
Maranao
नेपाली
Alxuraan bu Tedd bi
Tuesday, August 18, 2026
Don't forget us in your sincere prayers








