Aali Imran · 10/200
Tekki Waxtaan — Simoore Aali Imran
إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا لَن تُغْنِيَ عَنْهُمْ أَمْوَالُهُمْ وَلَا أَوْلَادُهُم مِّنَ اللَّهِ شَيْئًا ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمْ وَقُودُ النَّارِ ۝١٠
Innal lazeena kafaroo lan tughniya `anhum amwaaluhum wa laaa awlaaduhum minal laahi shai`anw wa ulaaa`ika hum waqoodun Naar
📖 Tekkim Wolof
Ña weddi, seen alal ya ak seen njaboot ya duleen fegal dara ca Yàlla. Te ñoom ñoo di mattum Safara,

🎧 Dégg


📜 Aaya 8-12 — Simoore Aali Imran

8رَبَّنَا لَا تُزِغْ قُلُوبَنَا بَعْدَ إِذْ هَدَيْتَنَا وَهَبْ لَنَا مِن لَّدُنكَ رَحْمَةً ۚ إِنَّكَ أَنتَ الْوَهَّابُ
“Yaw sunu Boroom ! yàlla boo jengal sunuy xol ginnaaw ba nga nu gindee ; te may nu yërmaande ju bawoo ci yaw. Yaw de yaa di Mayewaakoon bi !
9رَبَّنَا إِنَّكَ جَامِعُ النَّاسِ لِيَوْمٍ لَّا رَيْبَ فِيهِ ۚ إِنَّ اللَّهَ لَا يُخْلِفُ الْمِيعَادَ
Sunu Boroom ! Yaw yaa di dajale nit ñi ci bis boo xam ne - sikk nekkul ci ag ñëwam - Yàlla, du wuute dige ba.
10إِنَّ الَّذِينَ كَفَرُوا لَن تُغْنِيَ عَنْهُمْ أَمْوَالُهُمْ وَلَا أَوْلَادُهُم مِّنَ اللَّهِ شَيْئًا ۖ وَأُولَٰئِكَ هُمْ وَقُودُ النَّارِ
Ña weddi, seen alal ya ak seen njaboot ya duleen fegal dara ca Yàlla. Te ñoom ñoo di mattum Safara,
11كَدَأْبِ آلِ فِرْعَوْنَ وَالَّذِينَ مِن قَبْلِهِمْ ۚ كَذَّبُوا بِآيَاتِنَا فَأَخَذَهُمُ اللَّهُ بِذُنُوبِهِمْ ۗ وَاللَّهُ شَدِيدُ الْعِقَابِ
lu mel ni aadaay nitu Firawna ak ña leen jiitu woon, weddi woon Sunuy laaya. Yàlla jàppe leen seeni bàkkaar. Te Yàlla di ku tar mbugal.
12قُل لِّلَّذِينَ كَفَرُوا سَتُغْلَبُونَ وَتُحْشَرُونَ إِلَىٰ جَهَنَّمَ ۚ وَبِئْسَ الْمِهَادُ
Waxal ña weddi [ca Yahuud ya] ne : “Dees na leen not ; pang leen jëme Safara. Te [lal ba ñu fay fekk] bon na ! ”
Aali ImranFihi Alxuraan
200Aaya
MedinanRevelation
10Aaya

Tekki — Aali Imran 10

Simoore Aali Imran Aaya 10 - Jàng, Dégg, Tekki, Wolof : Ña weddi, seen alal ya ak seen njaboot ya duleen…

Simoore Aaya 10/200 — Simoore Aali Imran آل عمران (Medinan). Jàng Dégg Tekki (Wolof). Dégg: Simoore Aali Imran Dégg, Simoore Aali Imran Tekki, Simoore Aali Imran mp3, Simoore Aali Imran pdf. Aaya 8–12. Tekkim Wolof: Fulfulde.




Alxuraan bu Tedd bi


Tuesday, September 8, 2026

Don't forget us in your sincere prayers